Aujourd’hui, j’ai décidé de raconter publiquement ce que je vis parce que j’ai peur.
Peur de mourir, peur pour ma famille, peur qu’il me retrouve. J’ai longtemps gardé le silence, j’ai porté plainte, j’ai essayé de faire les choses correctement, mais rien ne change..
Ba dof ba fekkee baay ja dee, ñu tiim ko di jooy naan: daa gën!
Dof bi ne leen, gënul, dangeen a ragal a wax dëgg gi rekk.
Yàlla Fekk ug kër, romb fa dof ya ak sàmbaa-bóoy ya, ray kilifa ga, kër ga tas, ngeen naan daa gën? Ki ko ray ngeen ñemewul rekk.