La chaîne YouTube de Al Mourridiyah
a supprimé toutes les vidéos du Kurel Ass Dione.
C’est exactement ce qu’il fallait faire !
Les autres chaînes Murid doivent impérativement faire de même.
Ginnàw loolu ñoo ngi baalu ñépp àq ñépp liggéey bi rafet bi rafet na lool ci Mashrab bi, wane ngeen cofféel ci Sëriñ bi ak ci Xassida lepp ànd ak yar ak téggiin.
Yàlla nan ko ànd ay àtt yu bari kenn bañ a manqué barki Boroom Tuubaa mi nu bokk yaakaar🙏🏾
#MashrabuCaafii2026