J’ai aussi réalisé une petite vidéo de présentation 🥹🥰
N’hésitez pas à me donner vos avis, impressions et retours
Chaque avis compte énormément pour moi 🤍
Bi ma ci Sëriñ Mustafaa Saaliwu joxee ndigal joxaale ma téere bi ma jogefa dem ci Sëriñ Mustafaa Xassida.
Mu gis Xassida gi laaj numa def ak moom, ma wax ko fi mu joge da cee teg ni “Daa bëgg nga am Sëriñ Tuubaa te ràññee”
Yal na yërmande Yàlla, njéggalam ak i ngëramam wàcc ci ñoom
Nourou daareyni lou bari mooma ko doon leeral wakh ma lou waral mook ahmadou mouhniyane and yallaahou ya ahadou ag yaa seyidi
Wakhna ma thia diotaay boobou nema
يالله ياأحد ياخير صمد
Mo doon thiosane ba waaye da am kou masdi diangue thi kanamou seugn bi wakhé ko ni👇
Nitu Yalla dëgg dem na
Ku Bëeg Sëriñ Tuubaa dem na
Ku Bëeg Xassida yi dem na
Ku baax dem na
Sëriñ Mustafaa Mbàkke Xassida Yàl na Yalla Yoku saay leer Doli la Yeureumande Yàl Terru laa Sëriñ Tuubaa Terru laa ci barkeb Guudi gu tedd gi ñu jugee dembu
Ni rek nga mënon demee Mbàkke
Inaa lilaahi wa inaa ilayhi râjihoone
Serigne Moustapha Khassida Ibn Cheikh Abdoù-lahi Ibn Khadimour-Rassoul Yalla nako Sunu Borom yeureum diégueulko té khaaréko Aldiana manguikoy ziaaré niép
Mokkal gi mu mokkaloon xasiida yi jéggi na dayo, xasiida gu ne xamoon na fu ko Sëriñ bi binde woon ak lenn ci mbóot yi, mel ni bu Sëriñ bi daa bind da daa toog ci wet.
Yal na ko Yàlla jéggal te xaare ko guyaar. 🤍