Discours Seex Muhaamadul Mountakha Mbacke - Tabaski 2019 🙏🏾
« Daara jiguñu ci birr walla ci bitii ludul neek ci li ñu fi seriñ bi baayil »
« Seriñ bi digante ak boromam , digantem ak yonent bi , daathiee deef lo xamni been mindef meunouko wèssu » 😭
Yalla nafi Yaag te wéer ❤️!
Weer wi la Kubaax woolu Sëriñ Saliou ngir gërëm ko, nga sam ndondo lepp jaar ca yoon wa bamu wacce la ci weer wi ngir gërëm gumu la gërëm. Dem metti na waaye Mbacké matna sëkk 😭