Wax na ko de. Ayca Ma-Sàmba💪🏿💪🏿😂
Jàngee ci saw làkk dafa noppale. Fii mu ne bu doon ci araab walla farañse mbaa weneen làkk la ko jaar, xale bi man naa bañ a gaaw a man li ñu koy jàngal.
Dama réerone nga gindi më
Ma tiliim lol nga jël raxaas më
Ma wétone lol nga defmë sa weetal
Sama roouh gui xéncu wul ludul ag jaamu yaala
Sama jëm ji nuur në si ligeeyal Sëriñ touba
Sëriñ cheikh mbacke mom Sëriñ salihu yalla nafi yagg teh weer