nio ngui si diamono bou nakharé diamou Yallah! Bakh diaffé na, dioup diaffé, téyé sa ngor sakh dafa diaffé!
Je plains nos enfants et les générations futures!
Do sakh kham loy wakh 😪😪😪
Elle a quitté sa famille pour toi, le minimum serait de la traiter avec respect et dignité pas diko toroxal wala diko door ba moy faatu.
Yal nako Yàlla yërëm
Ku ray nanu ko ray loolu rek moo koy faj.
Ab soxna booko mënul teral, sagal, aar, jappale, jeema matal droits yiko yalla jox… bayyiko mu dem ci jamm.
« Et comportez-vous convenablement envers elles » S4V19.
This Senegal Coach Earned my RESPECT. only if Black Africans can stand and fight for their Right like this, we will be better.
he deserve a national honor.