S06-v17<<Et si Allah fait qu'un malheur te touche, nul autre que Lui ne peut l'enlever. Et s'Il fait qu'un bonheur te touche... c'est qu'Il est Omnipotent.>>
Waxtaanu Seex Abdul Ahat MBÀKKE wu aju ci Alxuraan.
"Alxuraan dafa di waxande wu ñu tëj wu am ub caabi. Caabi bi moo di Téere Bi. Soo ko bëggee laal , dafa lay wax ne la :
.{لا يمسه إلا المطهرون}
Nga dem jàppuji dellusiwaat bëgg koo laal mu ne la :
1/4
𝐘𝐎𝐁𝐁𝐀𝐋𝐔 𝐒𝐔𝐁𝐀 :
▬▬▬▬▬ஜ۩۞۩ஜ▬▬▬▬▬
_"Ah doom! Ku am nama gërëm ku ñakk nama xalab ndax ców li ców li maa a. Ma feeñal Li nëbbu woon, feeñal ki nëbbu woon muy sëriñ Bamba."_
*Talaatay Xewël...🙏🖤🤍*
Sant ak ligèyeul SERIGNE BI ❤️🙏🏿
SERIGNE TOUBA : ko xam ni lo am MOMA , lo xam MOMA , no mel MOMA , fuñiu la tek MOMA ❤️
JEUREUJEUF SERIGNE TOUBA ❤️
Amine MBACKÉ 🙏🏿
Sëñ Fàllu Mbàkke ne woon na
« SËRIÑ TUUBAA da nga kay jox sa lépp, waaye boo ko joxee lii, tëye lii, day waral përëxwéll »
(Përëxwéll, mooy yaxub ndawal bu rëy lool, te biir gi dara du ca nekk)