😭Témoignage émouvant d’une femme palestinienne qui déclare avoir été sauvée par Cheikh Ahmadou Bamba
Li de ab soññe dëgg la 🙏🏾
Version pdf : https://t.co/HVLy3asoLJ
Wakiilu ak sabablu :
Ñaari mbir yu am solo lool, muy wakiilu ci Yàlla ak sabablu, wakiilu mooy bàyyee say mbir sunu Boroom, xam ne moom rekk a ci man dara, sabablu mooy di jéem a def ay pexe ngir say mbir jàppandi.
Jaam bi nag ñaar yii la war a boole, lépp loo xam ne, jàpp na ne bu ko defee ay mbiram sotti na ko def, ba noppi mu fas ci xolam ne, Yàlla kese mooy sottal mbir yi, moom li ko war rekk lay def, sunu Boroom it def li ko soob, loolu bu ko jaam bi defee boole na sariiha ak Haqiixa, sariiha ji mooy pexe yi mu defal boppam, Haqiixa ji mooy delloo gi mu delloo lépp Boroomam xam ne mooy dogal lu ko soob.
Ndax Yàlla mbiram yépp ci kaw ay sabab la ko teg, te jaar ci sabab yooyu mooy teggiin.
🚨Touba :Le Khalife Général des Mourides, Serigne Mountakha Mbacké, a offert plus de 100 tonnes de denrées alimentaires aux daaras, dans un élan de solidarité et de soutien à l’éducation religieuse.
J’ai déposé ce matin une lettre de dénonciation auprès de la Fédération Sénégalaise de Lutte afin d’attirer son attention sur des actes de maltraitance animale qui n’ont leur place ni dans le sport, ni dans une société civilisée.
La quête de la victoire ne saurait justifier que des êtres vivants soient soumis à la souffrance, à la peur ou à la cruauté. La lutte sénégalaise est un patrimoine national, un symbole de courage, de discipline et de dépassement de soi. Elle ne doit en aucun cas être associée à des pratiques qui heurtent la conscience collective et portent atteinte à son image.
Je remercie le Président de la Fédération Sénégalaise de Lutte, Bira Sène, qui m’a accordé un entretien téléphonique et s’est montré particulièrement réceptif à cette préoccupation. Son écoute témoigne de l’importance qu’il accorde à la préservation des valeurs qui doivent guider notre sport national.
Il est temps que les autorités sportives prennent leurs responsabilités en affirmant clairement qu’aucune performance sportive, aucune croyance et aucun rituel ne peuvent justifier la maltraitance animale. Le silence ou l’indifférence face à de tels actes contribuerait à leur banalisation.
Mouhamadou Sarr
11700 Xale nga yoral léen lépp Añ Reer Ndékki at mu nekk nga génne 2365 200 000 FCFA seenum paj dekkal leen ci tabax yu gën ya ñu bàyyi séen i kèr ñuy jàng Alxuraan ak xam-xam di leen tarbiya ba ku ci dellu ci ay mbokkam mat leen yilimaan mat leen ab Sëriñ yalna nu la
Yalla fayal