Top Tweets for #InchaaAllaah
Bismil laahir rahmaanir rahiim sant Allaahu ta'aala julli ci Yonent bu tedd bi tax mu bind lepp
Sàkku ci Moom muy wëy di neenal pexey nooni #Senegaal biir ag biti illaa yowmi diin
Yal na Allaahu ta'aala delloo jàmm fépp fu ko ñakk ci kaw suuf ba ñu tal jaamu ko
#InchaaAllaah
@Mom0_MK @mouhatheproest 😂😁Wax dëgg!
Lenn ci ñiy tudee séen bopp murid te du ñu ko, ñoo neh ci ginaaw ŋàññ yi
Tapale kepp! 😄
@DiagneCheikhOu2 @KanteMakhtar @khmbacke @SonkoOfficiel @PR_Diomaye
#InchaaAllaah
#CaxaanFaaxe #SenegaalSaKanam

@babcisse108 @mouhatheproest Li ma gis a gum deh, lenn ci murid yi ñoo kay xeex
Di dox ci tappale, bëgg ku neh séen sarwis, def la jaam
Bu @DiagneCheikhOu2 nangoo léegi mu doon seen xarit
Ñu kay tagg, di ko tatagal😁
@khmbacke @PR_Diomaye @PR_Senegal @SonkoOfficiel
#InchaaAllaah
#CaxaanFaaxe #SenegaalSaKanam

@babacar29400781 @ThiamAmadouA Na #gornamaa paré yokk loxoom bu ko #Siin ag indien yi bëgee foxati ci sunu loxo def ko diw, dikaat jaay ñu njëg gu seer
Ku yoré loolu sàq jëwriñ @Mabouba_Diagne walla @serignegdiop?
Bu ñu keñ neh fii la xar yi jaar nag😁
@SonkoOfficiel
#InchaaAllaah
#CaxaanFaaxe #SenegaalSaKanam

@abass_djigo @lagobrune Bi iznilaahi tabaarakah wa ta'aala!
Ndax Yàllah, Ku ñëw a ti réglé, jox nit ñi àqq..
@MBWBMW
#InchaaAllaah
#CaxaanFaaxe #SenegaalSaKanam

@lagobrune Ndokk ba ñu xippee sunuy bët !
Léegi nag ndax da ñuy wëy di wàcc sunu ànd, di foh walla ?
Pénc mi ñuy fall, bi hawli laah, 17ni novambar, mooy doon bu #Senegaal nàmm ba ñuy #Senegaal ba tey
Yal na ci def tawfeex ag taysiir
#InchaaAllaah
#CaxaanFaaxe #SenegaalSaKanam

@abdou_Drame10 @lagobrune Mootax, xam li ngay bëgg mooy lan, lu jarr di lijjanti la.
#InchaaAllaah #SenegaalSaKanam
@PR_Diomaye Yal na Allaahu ta'aala def ci ndam ngir #Senegaal.
Baax nag, ci daje ju ni mel, boo fay dem, yóbbaale jàpp, di dóoree bismillaahiir rahmaanir rahiimi(njariñ)
Yàllah nag loo ko boolee wul mu bàyyee la ko.
Alxuraan yëpp firndéel na loolii
#InchaaAllaah
#CaxaanFaaxe #SenegaalSaKanam
Ganaaw jullig #asr
Melni mbay mësu fi am!
Misaal, kuy tabax tabaxal ci lu dëgër,bi maaʼnaa dëgg
Di gunge Etaa Senegaal fileeg mi ngi sàmpu ci dëgg.
@DiagneCheikhOu2@Mabouba_Diagne @KanteMakhtar @khmbacke @SonkoOfficiel @PR_Diomaye
#InchaaAllaah #SenegaalSaKanam
#イマソラ
@PR_Senegal @MariemeSoda_SN @PR_Diomaye Yal na Allaahu ta'aala yóbb la ci jàmm delloosi ag jàmm Persiden
Battali : naar du ñu sunuy mbokk
Njaam nit ku ñuul ci ñoom la fekk baax
"Mon frère" ay naxé mbaay, ñoo dëkk @DiagneCheikhOu2 @KanteMakhtar @khmbacke @SonkoOfficiel
Séen julité ci làmiñ la yem
Wa salaam
#InchaaAllaah

@lagobrune #Senegaal améel na njukkéel #Imaan_Aliwun_Badara_Ndaw rahimahulah @DiagneCheikhOu2 @KanteMakhtar @khmbacke @SonkoOfficiel @PR_Diomaye
Taxawaayam ci lislaam at yi ñu gën mate na ko, xamxam bi, lu mu la wax mu leer nàññ ñi jant
Allaahu akbarr! Ñakk nañ ku am yërmaande
#InchaaAllaah
@walfadjrisn Mbedd mbaa ne yambalaŋ!
Ku am fit a ca !
Bu weddee reg na dem, di na rus, bu dee amna lu muy jomb.
#InchaaAllaah
#CaxaanFaaxe
#SenegaalSaKanam
@lagobrune @aliounetine16
@SeydiGassama ñii keñ war nañ bàyyi parparloo
#InchaaAllaah
#CaxaanFaaxe
#SenegaalSaKanam

@PapaMalickNdia8 @LiptakoGourma3 @GoitaAssimi Waa rumbulmaa ñooy wut buzz 😆
Wayé séen njjit yi xam nañu bu baax li xew !
Yelimaani jëwriñ yi dem na fa bu yàggul.Ñëpp dégg nañ la mu wax.
Nyamsy nag mooy rambaaj bi.
Buñ tëj mukk nag ndax li ñu léen di jaay moo bari.
Na ñu maslaa reg
#InchaaAllaah
#CaxaanFaaxe
#SenegaalSaKanam

@PapaMalickNdia8 @LiptakoGourma3 @GoitaAssimi Déet bul topp sa xol Sëñ bi 😆
#InchaaAllaah
#CaxaanFaaxe
#SenegaalSaKanam
Ku nàmm soobuwaay (system) bi fi newoon, di muucu defeti askan #Senegaal dee wet :
Laa hawla wa laa xuwata illaa bilaah
Muhammad aleyhi salaatu wa salaam neeñu la ko jaaxaloon baat yooyu laay tudd ba Allaahu ta'aala def tawfeex.
Na jòlli ! 😇
#InchaaAllaah #SenegaalSaKanam
Last Seen Hashtags on Sotwe
MGAI
Seen from United States
ometv flash
deraanjela
Seen from Malaysia
lxlicon
Seen from United States
nolimits()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()()
ทุ่งสงนัดเย็ด
Seen from Thailand
เเนวครอบครัว
Seen from Thailand
candid filter:videos
Seen from Pakistan
bubbline
Seen from Netherlands
Trends for you
Most Popular Users

Elon Musk 
@elonmusk
241.7M followers

Barack Obama 
@barackobama
119M followers

Cristiano Ronaldo 
@cristiano
114.4M followers

Donald J. Trump 
@realdonaldtrump
111.9M followers

Narendra Modi 
@narendramodi
107.2M followers

Rihanna 
@rihanna
98.7M followers

NASA 
@nasa
92.4M followers

Justin Bieber 
@justinbieber
91.8M followers

KATY PERRY 
@katyperry
90M followers

Taylor Swift 
@taylorswift13
83.9M followers

Lady Gaga 
@ladygaga
75.4M followers

Virat Kohli 
@imvkohli
73.3M followers

Kim Kardashian 
@kimkardashian
70.9M followers

YouTube 
@youtube
68.8M followers

Neymar Jr 
@neymarjr
66.3M followers

Bill Gates 
@billgates
65.1M followers

Selena Gomez 
@selenagomez
63M followers

The Ellen Show
@theellenshow
62.3M followers

CNN 
@cnn
61.8M followers

X 
@x
60.7M followers









