Top Tweets for #MbecteiMi
#mbecteimi 😍😍Good Friday

من كان لله كان الله له 😍
Kou nekal Yalla Yalla nekal la
Manam kep kou nekal Yalla si dieufé ndigeul yi ak bayi téré yi ✍🏽 Yalla nekal la si lepp ✋🏻Lo Yotou dioT si LoY sakou Mou Yomb si yaw
Wayé nek si sa bopou defalo Yalla dara ba nopi fo tolou nane Yalla baxna
#Mbecteimi✍🏾✍🏾

MoY Xaliilullahi
Di Abul Muridiina
Di Baabul Muridina
Di Abò Rijaalullahi
D Baabul 'uloom
Di Baabul Jannati
Di Baabu kullu Xayri
Di Siidi Biraahim Faal
Di Sawru Maam Say Njaay
D Baayu Soxna Soda Faal
Di Maami Soxna Jee Faal
Di Muridul Akbar
Mooy Jekk njañ,Neexi ree
#Mbecteimi✍🏾

Tawwil lana houmrana sakhih lanaa badanane
Wa hab lanar roushdawa tawfiqa Yal laahou
Accorde nous une longue vie! Donne nous une excellente Santé
Apporte-nous la bonne la bonne direction et la félicité!Oh Mon Dieu
SERIÑ MOUNTAKHA MBACKÉ YALLA NAFI YAG AND AK Wer
#Mbecteimi✍🏾✍🏾

Ku xëy di neexalu nit ngir bëgg seeni ngërëm Xëyal di neexal Sëriñ Tuubaa te mokk ko yaw Bis boo amee ngërëmam, am Yàlla am sa mebet Am barke, am kepp nit am lepp far falu yaw Moo tax bàyil lepp tey wut fàwwu ay ngërëmam Ba am ko kon say mebet day jug te wut si la yaw
#Mbecteimi

Ndaysaan Seriñ Mbaye sy Abdou néna 👇🏾
Nieuwou Gniou Rék
👉🏾Nguir Gamou di Fitassou
👉🏾Nguir Gamou di Leik di nane
👉🏾Nguir Gamou di solou di simikou
👉🏾Nguir Gamou gui nekhone na
Dédét Dañiou nieuw
👉🏾Nguir défarate souñiouY djikou ❤️ Li rek moy Gamou dou lénén
#Mbecteimi✍🏾

📄Matlaboul fawzeini🎤
Diamou yalla ak sope yalla ak khewal
📄Matlaboul chiffa’i🎤Soigne toute maladie a reciter matin et soir
📄Mouwahibou🎤khewal
📄Sabhoutahi
🎤 khewal
📄Djeusboul khoulob
🎤Yoke ak gueume akoupe thiofel thi lou bakh ak mbecke
#Mbecteimi✍🏾
SEN INTERIM souhaite un excellent #Magal2019 à toute la communauté musulmane plus particulièrement a toutes la communauté Mouride ..!
prudence sur la route
#kebetu
#18SAFAR
#Mbecteimi
#SunuMagal2019

@innov_digital souhaite un excellent #Magal2019 à toute la communauté Mouride du monde..!
#kebetu
#18SAFAR
#Mbecteimi
#SunuMagal2019

Machallah 😭❣️
#direction18Safar #MbecteiMi Dieureudieufé Serigne Touba👌
#Cheikhouna_ahmadoulkhadim_sunuyakar ❤️ ❤️ 🙏🏿
#direction18Safar #MbecteiMi Dieureudieufé Serigne Touba👌
#Cheikhouna_ahmadoulkhadim_sunuyakar ❤️ ❤️ 🙏🏿


#direction18Safar
#Sunu_yitté
#MbecteiMi
" Ku déme ma déme , ku démul ma déme .
Al Mountaxà ❣️❣️
#Cheikhouna_ahmadoulkhadim_sunuyakar ❤️ ❤️ 🙏🏿

#direction18Safar
#Sunu_yitté
#MbecteiMi
" Ku déme ma déme , ku démul ma déme .
Al Mountaxà ❣️❣️
#Cheikhouna_ahmadoulkhadim_sunuyakar ❤️ ❤️ 🙏🏿

Sénégal Dem Dikk renforce son parc de bus à l'occasion du Grand Magal de Touba. Les réservations sont prévues le 13-10-2019 à partir de 10H. L'heure de départ des bus en renfort est prévue le 15-10-2019 à 10H. Dakar Dem Dikk, un Patrimoine national.
#18Safar
#Kebetu
#Mbecteimi

La cause de ma déportation vient du fait que Dieu voulait m'accorder un destin prestigieux, et le pouvoir d'interceder le jour de la resurrection en faveur de mon peuple et faire de moi le Serviteur du Prophete.
Cheikh Ahmadou Bamba.
Jërëjeufé Serigne Touba !
#Mbecteimi✍🏾✍🏾

Après avoir examiné certains problèmes relatif a la colonie le conseil à approuvé la décision que le marabout Ahmadou Bamba doit être exilé au Gabon le 21 septembre 1895 une pension de 50cfa par mois lui sera accordé durant son séjour au Gabon
Un extrait du rapport😭
#Mbecteimi✍🏾

Last Seen Hashtags on Sotwe
nolimit nolimit nolimit() +filter:native_video
Seen from Australia
graf
Seen from Poland
ควยตำรวจ
Seen from Thailand
NoLimit #NoLimit #momson
Seen from Turkey
จันทบุรี
Seen from Thailand
自拍照
Seen from Japan
dickrate
Seen from Netherlands
母狗人妻
Seen from United States
hawaii
Seen from United States
wankchat
Seen from United States
Trends for you
Most Popular Users

Elon Musk 
@elonmusk
240.4M followers

Barack Obama 
@barackobama
119.3M followers

Donald J. Trump 
@realdonaldtrump
111.7M followers

Cristiano Ronaldo 
@cristiano
110M followers

Narendra Modi 
@narendramodi
107M followers

Rihanna 
@rihanna
97.5M followers

NASA 
@nasa
92.1M followers

Justin Bieber 
@justinbieber
90.8M followers

KATY PERRY 
@katyperry
87.4M followers

Taylor Swift 
@taylorswift13
81.2M followers

Lady Gaga 
@ladygaga
72.7M followers

Kim Kardashian 
@kimkardashian
69.6M followers

Virat Kohli 
@imvkohli
69.4M followers

YouTube 
@youtube
68.6M followers

Bill Gates 
@billgates
63.7M followers

The Ellen Show
@theellenshow
62.5M followers

Neymar Jr 
@neymarjr
62.1M followers

CNN 
@cnn
61.9M followers

X 
@x
60.8M followers

Selena Gomez 
@selenagomez
60.5M followers









