Top Tweets for #Ndigal

#Sëriñ-Mountakha wan na ko yoon !
#Président_Bassiru Jomaay Fay nee na : Sëriñ bi fan yii lin jokkoo bërina ngay wane #yoon ñu ciy topp nga joxe #ndigal ñu déggla jëfe ko ...!
⚠️ #Question : Lu nekk ci ginaaw wax jii ?
🚨Ma sàmp ay laaj :
-Ndax #Président Jomaay dafa amoon yeene #tëjlu Sonko Sëriñ bi ne ko tegal ci suuf mu topp loolu ?
-Ndax #Président Jomaay bi ñuy def #Sonko #Président_Assemblée dafa amoon yeene jëfandikoo #force ngir loolu bañ am Sëriñ bi ne ko #tegal ci suuf mu topp loolu ?
-Ndax #Président Jomaay dafa amoo yeene #tere ndaje xew xew yi Sonko di woote Sëriñ bi ne ko #tegal ci suuf mu topp loolu ?
Lu nekk ci ginaaw waxam ji moom #Président ?
﷽
Barkeeb Maam Seex Ibraayma Faal
Kénn matul ñépp a ami sikk waaye na la sa sikki bopp doy soxla. Fexeel liggéey ci te ñaan Saa Boroom dimbali la.
#TalaatayMaamSeex #WaxTout #Hikma #taalibe #Muriid #Suufi #Ndigal #Tawakkul #XoolalSayAyyib
﷽
Barkeeb Maam Seex Ibraayma Faal
Ne comparez pas les gens, seuls leurs actes définissent leur vraie valeur. Chacun est à la hauteur de ce qu’il accomplit.
#TalaatayMaamSeex #WaxToutKoor #Hikma #taalibe #Muriid #Suufi #Ndigal #Tawakkul #Jëf
Adiya Daarou Salam 480 millions FCFA.
Thiey Borom Touba
Thiey Borom Gaawaane🤍✨
#Ndigal
#Yeesal
#JumayTouba
Journée de prière : Zikr, Al quran, Xasida ce vendredi 17 Mai sur #Ndigal du Khalif Général des #mourides.
A suivre en direct sur #tdisenegal
Mouride_Ndigal
Ndigal_dieuffei

Ce que vous appelez #Ndigal à Touba est là . Après la Prière de Timis, Le Khalif donne ndigal aux fidèle :
“Sëriñ bi neena nañu maase si séntu weer wi te ku ci xam lu wér nga yëgle ko ".
#Sant
A chaque période de malheur, succède une période de bonheur. Les instants pénibles sont toujours suivis de meilleurs moments.
💬Cheikh Abdoul Ahad Mbacké💬
📚Discours Magal Touba 1979📚
#Ndigal #Wadial #Bessup #Xasiida #Mouharram #1443H #2021 #mouride #mouridiyah

M2D annule la manifestation de demain sur l’étendue du territoire sous la recommandation du khalif des mourides.
#FreeSenegal
#SenegalEnDeuil
#NouvellePhotoDeProfil...
"Ku nekk ci #ndigal, misaal ma mooy #lëndëmu_fajar... Looy dox di dox saw #yoon di #gëna_leer !"
Yalnanu ci sax dàkk barkep #Seex_Yibra_Faati🤲🏽...

@biigvieux 🤭🤭🤭🤭, li ko #Màggal_Tuubaa yen ci bernde moo bari nag, foo jaar mu àbb yoon wi nag... Dafa xamul woon lan mooy #Murit bu jot #ndigal rekk moo tax sax #Màggal fekk ko fi nde kon sax du ko fi xaar🤭🤭🤭...
Last Seen Hashtags on Sotwe
Trends for you
Most Popular Users

Elon Musk 
@elonmusk
241.2M followers

Barack Obama 
@barackobama
119.1M followers

Cristiano Ronaldo 
@cristiano
112.8M followers

Donald J. Trump 
@realdonaldtrump
111.8M followers

Narendra Modi 
@narendramodi
107.1M followers

Rihanna 
@rihanna
98.3M followers

NASA 
@nasa
92.3M followers

Justin Bieber 
@justinbieber
91.5M followers

KATY PERRY 
@katyperry
89M followers

Taylor Swift 
@taylorswift13
82.9M followers

Lady Gaga 
@ladygaga
74.4M followers

Virat Kohli 
@imvkohli
71.9M followers

Kim Kardashian 
@kimkardashian
70.4M followers

YouTube 
@youtube
68.8M followers

Neymar Jr 
@neymarjr
64.8M followers

Bill Gates 
@billgates
64.6M followers

The Ellen Show
@theellenshow
62.4M followers

Selena Gomez 
@selenagomez
62.1M followers

CNN 
@cnn
61.8M followers

X 
@x
60.8M followers









