Top Tweets for #Yonen
Dellu teg ca ne "Ku ànd ak #Man (#Bàmba) dangay am #ñetti_pay...:
*#Yàlla dalay fay,
*#Yonen bi fay la,
*#Man (#Bàmba) ma fay la.
Waaye ku ànd ak #Cerno_ñenti_pay ngay am...:
*#Yàlla dalay fay,
*#Yonen bi fay la,
*#Man (#Bàmba) ma fay la,
*#Cerno fay la !!!"
Wér na...

S touba neena
Andak man doyna waayé andak Thierno apouna
A fanart that I made of Nen and Cielo from Yonen (an argentinian manga by Leandro Caballero) 😁
.
.
.
.
.
#draw #drawing #art #artist #ArtistOnTwitter #fanart #yonen #character #digitalart #illustration

ñii la tuddée #Yonen bi ciy #doomam.
-#SËRIÑ_MÓODU_AWA_BÀLLA,
-#SËRIÑ_MAHMADAN_KOSO,
-#SËRIÑ_ABDUL_XUDDÓOS,
-#SËRIÑ_ABDU_RAHMAAN,
-#SËRIÑ_ABDUL_JAMIIL,
-#SËRIÑ_BASIIRU_ÀNTA_ÑAŊ,
Muy limuy #juróom_benn (06)
👇👇👇
•#Médaille la maala ko takkal #Man_Bàmba,
•Ci #ndigëlël_Buur_Yàlla ak #Yonen ba;
•Te maa ngi lay sàkkul fa #Rabbul_harshi,
Luy tax ba ñépp ñee la #yawmal_batsi;
•Ba naan "Fatip nafsan wa xara hayna",
Sam Xel na dal, sa Xol na sedd tawna...👇👇👇

#AsShaaxi...
#Sëriñ_Habbaas mii kiñu ko tuddée ci #Sahaaba ya la bokkoon, doonoon #Baay ci #Aleyhi_Salaam;
Ci jamonoy #Yonen bi ci Barkeem lañu daan ñaan ngir #Yàlla may leen am #Ndox suñu nekkaan ci #toolu_xare yi;
#Sëriñ_Bàmbaa tuddée #Yonen ba,
#Boroom_Daaru jox #Sahaaba ya.
Seriñ Abbas Mbakké
Xalifa Maam Birahim Mbakké
Yàlna fi yagg lool te wer !!!



Thursday @SmallPondRec
#Poly-Math
+ #LapisLazuli
#SteveStrong
#Yonen
#instrumental #MathRock
Tickets - https://t.co/vDqiIRukZd
#Brighton
Feb 9th @SmallPondRec
#Poly-Math
#LapisLazuli
#SteveStrong
#Yonen
#instrumental #MathRock
Tickets https://t.co/vDqiIRcK7F
#Brighton
Gracias Lea x tu #YONEN de purplecomics y tu visita a @fanelprograma @ Radio Colmena https://t.co/lJQLf4CfeK
Last Seen Hashtags on Sotwe
Trends for you
Most Popular Users

Elon Musk 
@elonmusk
241.1M followers

Barack Obama 
@barackobama
119.1M followers

Cristiano Ronaldo 
@cristiano
112.4M followers

Donald J. Trump 
@realdonaldtrump
111.8M followers

Narendra Modi 
@narendramodi
107.1M followers

Rihanna 
@rihanna
98.1M followers

NASA 
@nasa
92.2M followers

Justin Bieber 
@justinbieber
91.3M followers

KATY PERRY 
@katyperry
88.7M followers

Taylor Swift 
@taylorswift13
82.6M followers

Lady Gaga 
@ladygaga
74.1M followers

Virat Kohli 
@imvkohli
71.5M followers

Kim Kardashian 
@kimkardashian
70.3M followers

YouTube 
@youtube
68.7M followers

Bill Gates 
@billgates
64.5M followers

Neymar Jr 
@neymarjr
64.4M followers

The Ellen Show
@theellenshow
62.4M followers

CNN 
@cnn
61.8M followers

Selena Gomez 
@selenagomez
61.8M followers

X 
@x
60.8M followers












