Top Tweets for #saabal
Lu wuutale Wér Péng - Wér Céng - Wér Pelag
Wóor na ma péng ne Badu ku wér céng la, dara jotu ko, bu ko dara daloon sax kon ma ne wér na pelag.
Péng : xam-xam bu la wóor
Cént : wérug yaram, ku dara jotul woon
Pelag : tàqalikoo ak wopp.
#Wolof #Saabal #SenegaalWolof



« Doom ju jigéen jàngaaniwul dara… »
| Ak Maam Yaxi Laalu.
Demal ci dal bi https://t.co/shgpH1U5oo ngir topp wax ji lépp.
#WAX #Jàngwolof #Saabal #Kebetu #Cosaan 🇸🇳
❌❌🚫
Di xamle ne sàq mii bokkul ci #JàngWolof te it wolof yi muy bind setul doonte ci téereb sunu yaay ji Aram Faal la koy tibbe ndax téere boobu ab jéemantu la woon te nu ngi koy jubbantiwaat ngir yaatal ko.
#Wax #Jàngwolof #Saabal #Kebetu 🇸🇳

Jafe-jafe ci céddaleg mbëj gi (électricité).
Waa @Senelecofficiel di xamle ne seen barab ba Belleer (Bel Air) daa tàkk ba tax na dina jur ay jafe-jafe ci céddaleg mbëj gi ca biir digg gëbla ga (centre ville) Ak ca Poor bu Ndakaaru.
#Saabal #kebetu

Rab yii moom, wan rab nga ci bëgg a yar sa biir kër ? 🤭
#JàngCiNataal
#Wolof #Saabal #Senegaal #Kebetu 🇸🇳

#Bisu_sosu 😍
Àjjuma jii di ñëw di 10i fani féewëryee la mbootaay gi di am 5i at nu di ko màggal.
Nettali nu man at nga dal jàng ak ku la doon jàngal ? 👨🏽🏫
Ban bind moo gën a jafe ci yaw ? ✍🏾
#Wolof #Saabal #Kebetu #Senegaal 🇸🇳

Last Seen Hashtags on Sotwe
ourfurryfriends
Seen from Brazil
collaborationchoir
Seen from United States
RoutetoGrow
Seen from United States
capetownrunining
Seen from United States
iafwing
Seen from United States
シャンプーブロー
Seen from United States
MueveTusEmociones
Seen from United States
ななにー流失
Seen from Japan
expectantwaiting
Seen from United States
ishereallythattall
Seen from United States
Trends for you
Most Popular Users

Elon Musk 
@elonmusk
241.5M followers

Barack Obama 
@barackobama
119.1M followers

Cristiano Ronaldo 
@cristiano
113.6M followers

Donald J. Trump 
@realdonaldtrump
111.8M followers

Narendra Modi 
@narendramodi
107.2M followers

Rihanna 
@rihanna
98.5M followers

NASA 
@nasa
92.4M followers

Justin Bieber 
@justinbieber
91.7M followers

KATY PERRY 
@katyperry
89.5M followers

Taylor Swift 
@taylorswift13
83.4M followers

Lady Gaga 
@ladygaga
74.9M followers

Virat Kohli 
@imvkohli
72.6M followers

Kim Kardashian 
@kimkardashian
70.7M followers

YouTube 
@youtube
68.8M followers

Neymar Jr 
@neymarjr
65.5M followers

Bill Gates 
@billgates
64.8M followers

Selena Gomez 
@selenagomez
62.5M followers

The Ellen Show
@theellenshow
62.3M followers

CNN 
@cnn
61.8M followers

X 
@x
60.8M followers







