@ahmadou_gassama @magatte76168066 @une_soninke Koubakh bo gastoo touti danga guis ne gni epp si borom xam xam yi wakhnagn ni صورة bi nek si Hadith bi boukoul ak صورة فوتوغرافية (image bignou min ) nakh dou nourole
"ku bëgg a dem, bul fayantoog ñi lay tooñ, bàyyil xel say soppe, lu ñu la lebal ci lu baax, nga fas yéene leen ko fay"..
Àdduna lépp mbind mu tooy la ❤️