[ Jotaay yi ]
SËRIÑ TUUBAA nee na :
Jotaay yi juroom la, te bu ci nekk boo ci toogee amna lumu lay jariñ
•Jotaayub Gonne day waral foo
•Jotaayub Jiggéen day waral moy
•Jotaayub Buur day waral rëy
•Jotaayub Borom Xam-xam day waral sammonté
•Jotaayub Ku xam YALLA day waral yiwub xol
📚 Source : Diyaafatu Samadiya VOL2
« Yoonu Sëriñ Bamba wi ci kanam tuuti luné dinako wuyu si, waaye bungeen fa yéggee, lu ngeen mana gis ñukay def te daawu mako def luñ ka ca boole boole du ca, luma daan def nak luñ ka ca génne génne ca la »✨
Cheikh Ibrahima Fall ❤️🇸🇳📍
🚨Assalaamu Halaykum wa Rahmatullaah.
Mbooloo mi Sëriñ bi dénk mbirum séentu weer wi ci Tuubaa, ginnaaw bi ñu dajee ci Jumaay Tuubaa ju mag ji ngir séentu weeru Tamxarit wi; ñoo ngi xamal ñépp ne weer wi feeñ na. Kon suba ci Àllarba ji, 17 Juin 2026 mooy benn panub Tamxarit (Muharram) 1448H, di ndoortel at mu yees.
Atum jàmm ak naataange yal na ñeel jullit ñépp.
——
Mbooloo mi yore wàllum séentu weer wi ci Tuubaa.
Aaya 20 sourate 80 (Abasa)
ثُمَّ السَّبِيلَ يَسَّرَهُ.
Thumma as-sabīla yassarah
"Guinaw lolu, mu daldikay yombalal yoon wa"
Jigéen bu tolu si mat yeexa am dôme wala ñu barrél ko rek té mat ga yeexa tambali.
Jelel bouteille eau minérale bu ndaw wala kaass ndox en verre nga jangsi aaya bi 70 wala 77fois jox soxnasi mu naan.
InshALLAH dina gaawa am dôme té dusi am ben thiono.
Si Aaya bi sunu BOROM day fatali ni du KEN ku sakk kudul MOM téyit MOM rek moy BOROM yeurmandé MOM mi défar nit joxko dundu MOY kikay yombalal guénukay si biiru ndeyam wala si benen mbir bumu menti don.
So démé nak si Xassida Touhfatou Moutadharihîn lu yémé lasi KU TED KI féñal si fan wowu.
Ñenti « Bi Ouminâ » ñosi dikk.
Dangay jang ñent yi 7fois jox soxnasi mu naan Walahil’azîm dina am ak gaawal akuk yombal ba tém mom si bopam laajté fan la xalé bi jaar.
Ñenti « Bi oumina » yoyu goor guko jang ëfko siy loxom raay ndigam du tëlé té dana am katan gumu yoré njabotam.
Ak yenen ak yenen.
Yalna YALLA yombalal njabot bep jigéen 🤲🏾🙏🏾#TaawOu
Bande de chiens 🐕 , quand Sarkozy est venu insulter vos parents y’a pas longtemps à Gorée , vous n’aviez pipés mot !!!
Mais quand c’est SONKO , vous allez réveillés vos grands parents morts d’un coït !
" Gngngn il n’avait pas à dire ça " fermez vos gueules mraaam Yi