Widewoob ndaw soosu bàyyi mbuug (misig) bëggoon naa ci wax lu bari sax, waaye seral na sama xol bi.
Yi mu wax na ci ku nekk natt boppam, luñ gën a nuur ci li Yàlla tere Mu nuy gën a soril Boppam, daf lay xañ lu baax lépp: julli day diis ci yaw, doo nangu dégg lu lay fàttali.
Xasiida gii sëriñ bi tënke arafi (ahoosu bil laahi) sëriñ abdou rahmaan bind na ci suuf waxni:
"Ku bëgg taggoo ag Sikki bàkkanam yiy tee mu mane ag boroomam, am texe goo xamni ak texeedi du ci topp, texe fawu rek nay saxoo bayit yii diko bari la jàng".
Allahumma salli ala Muhammad wa ala ali Muhammad kama sallayta ala Ibrahim wa ala ali Ibrahim. Wa barik ala Muhammad wa ala ali Muhammad kama barakta ala Ibrahim wa ala ali Ibrahim. Innaka hamidun, Majid