baykat bu mag di yëngu ci mbayum dër, lu ci mel : Tomates, Pomme de Terre, Poivron, Choux Pommes. añs... bëgg it lool Futbal⚽️❤, di supporter Chelsea, Milan AC.
@MakhtarDime Mi ngoog, lu mu def lu dul dem, dem a ko gën.
Bu demee : Nekk fa titulaire, di futbal "PL" di futbal "LDC" ay "performancesam" di gën a yokk, sunu dugg ak Mondial bi li ci des matul juróomi weer... Lii dina baax ci moom, baax itam ci Senegaal.
Dimanche 2 février 2025
Rubrique marché légumes de Notto prix du jour :
Tomates 🍅
Cobra 6000/5000f
Mongal 4500/2500f
Asila 12000/11000.
5000/4000f
🥕Carottes sac de 80 à 75 kg 18000/17000/15000/13000/12500f
12000/10000f
Navet ordinaire 8000/7000f
Navet Chinois 3000/2500f.
Chou pommé 7500/7000/6500/6000/5500/5000f
🍆 Aubergine 7000/8000/8500f
Pomme de terre sac de 25kg 11000f
Soble (local sac de 25kg) 10 000f
🫑Poivron kg 250f, 225f
Kaani gouana kg 1250/1100f
Sac de Joxote 10000f
Kaani thioukri kg 750f
Sac de Ñàmbi 20000/19000/18000f.