@ElHadji_Ndoye09 Il faut noter que c’est a cause de la technologie que l’on sait que la mecque célèbre trl jour où tel or les lois musulmanes précédent de loin la technologie et ne s’adaptent pas cette dernière.
@kalypro6 Kouy togn dou mouthie wayei kouy fayou dou a jamm . Gni waxx li waxx nan lou gnaaw tei doyadi sip joulite wayei matoula delouwaat itam sip joulite ngir ni jumaa neegou yalla saa sou appam jotei rekk dina noppi lolou mindef menou si dara
@biigvieux Li dey yalla nanou si yalla mousseul. Benn beuyit rekk bou si serigne bi binde fekk ko wone si noflay. Tay nak gni xamoul rekk gnoy fowei tourou mbinde mi waxxoumalak mbinde mi. Nane Mbekte di doul😡. Mbekte dikkoul adouna.