Am yeene tasaare njàngaleem Seriñ bi ba mu daj fepp. Di amal ay siaar ak'i ndaje ngir xamle Sëriñ Bi.
ngir ay leeral +221 77 264 63 33 / +221 776 88 66 00
تلك عشرة كاملة 1438H -1448H
10 ans Kureel Liggéeyal Ku Tedd ki, 2016/2026
Kureel Liggéeyal Ku Tedd ki, mi ngi ci fukkeelu atam bim sosoo ak leegi, (2016 - 2026) di ñaanal Kureel gi mu gën a jëm kanam ak mbooleem ñiy taxawu liggéey bi, te Sëriñ bi gërëm seen uw doxiin, Aamiin !!
Réunion Commission Scientifique Kourel Liguéyeul Kouted Ki
Doon saytu ligeey bi ak mbooleem lu aju ci bisu 4 Safar bi ci wàllu Xam-Xam !!!
Jeudi, 24 Juin 2026 à Touba.
#10ansklk#raabihasafar#4safar#klk#touba#magal
Kureel Liggéeyal Ku Tedd
Amaloon ab ziyaar tay jii ci *jeudi 25 juin 2026*
Ci kanamu seex Muhammadul Muntaxaa ca Jurbel
ngir yeesalaat ndigëlul ligeeyub 4 Safar 1448H-2026.
Communiquée 🛑
Kuréel Ligéyal ku tedd ki, pour ku bëgga participer ci concours yii ñuy amal ci Raabiha Safar bi ( 4 Safar ), man ngaa woote ci numéros yii, ak concours boo bëgga bokk parmi les quatres (4).
Maximum de partager 🙏🏾