J’ai l’impression que bcp trop de gens oublient la Palestine alors qu’ils vivent actuellement les pires crimes contre l’humanité possibles, qu’Allah leur vienne en aide
À mon humble avis,Cheikh Bassirou Mbacké Khelcom, est le meilleur biographe contemporain du Prophète Mouhammad SHWS.
En effet, la précision avec laquelle, Le petit-fils de Cheikhoul Khadim, a, raconté l'histoire inédite de l'homme fort de Médine, est hors pairs, Machallah !.
Yonent bi shw moom lanu yalla joxoñ wax ni mooy seen royukaay, wax ni bu ngeen ko toppee di ngeen gindi ku, kon jang ay jaar jaaram li ci wara jiitu mooy jële ci ay bind gir xam ni ngay dunde ci aduna sa relation ag yalla, ag nit ñi, ag sa njaboot, ag sa bopp.
did everyone forget Trump literally kidnapped a sitting president of a foreign country and his wife in the middle of the night, and they’ve just been sitting in jail for the past 6 months?
En tant que jullit so yewo guiss kou done muuru murekou boko mounoul nianal sunu Borom yombalatal ko muuru waro ce waax lu niaw . Surtout jigeen mu leerlani muuru yomboul dara ter kéne muccul si murekou .
Yallah nañu Borom bi yombalal jeufe ay ndigeuleum.🤍
Fi jamono tollu, ku bëgg a mucc, fexeel ba, am métier, am loo mën, di liggéey foo tollu te doylu nak. Rafet njort ci nit ñi, di dund lu positive et xam say farataay diine te fexee jege sa Boroom.
Boole ko ag jàpp sa njàmbur tey àndak ñi lay dimbali ci ag njub