@Cisse_Maps Genres yi nio geuneu dangereux si réw ils sont prêts à défendre n'importe qui pour leurs poches, Alhamdoulillah le vrai visage de la fédération sénégalaise de football dafa geuneu confirméwou tay, ni laniou yague mél danio deuk si déff ay ndiombé wout niouléndi défendre sibiti
@PapeDudu_ndoye sonko limou wakh fofou conclusion bi moy léral lépp; car dafa wakh ni li équipe France di dieulé joueur africains yi lolou moy wané ni niom nioy dépendre si nioune pour meuna dundu sou féké ni africains yi comprendre naniou lolou
@ldsenegalais Effectivement nit gni fok niouy utiliser séne xél yi, niouy réy xar Tabaski Tay la geuneu bari, mais problème bi moy niouy kass yeup moy niouy yar di diayatt séne xarr yi cherna en pluie deuk bi yeup beugue nék ay diaykatou khar no déff secteur bi saturé
@sexulxadim@xalaat1 Diégalou ak niak diégalou niossi yam, mane bima xamé ni Pape Ngagne Ndiaye mo mome Chaîne bi silassi rakhaso ba sétt, ay nonou Pastef lagni meussa done