Mangui niane yalla mou geun ma xirr si xassida Serigne Touba yi nax xamnani niom rk gno baax si mane niom rekka ma meuna deufeul sama xol bi nimouy nèkhè soumakoy tewlou beugouma mou diexx dh😞♥️
L’amour c’est quand Fatima était entrain de réciter le Quran puis elle arrive à un verset autorisant les hommes à avoir 4 femmes est venue ,elle baissa la voix pour que Ali ne l’entende pas .
Ali a souri et lui a dit :
« ne t’inquiètes pas , toi seul t’es égal à eux tous »🥹❤️
Jaber Ibn Sumra a dit: « Lors d'une nuit de pleine lune, le Prophète se dirigea vers moi avec la lune dans le dos. Je me mis à regarder la lune, puis le visage du Prophète , et encore une fois la lune puis le visage du Prophète ,👇🏽
Xamoon naa ay nit ci réseau yi, naw leen lool ci xalaat ak xel yu sell, ñu fonk diine ba lu leen ci lënt ñu ñëw laaj ma, doon ma woo ngir ku leen soññ ak leeral leen, ma jékki rekk gis réseau yi soppi leen ba may sikk sàkka ndax ñoom la.
Àdduna doy na waar ! Yal na ñu dellusi.
Doko guiss ci Live tik tok , amul chaînes YouTube
Doko guiss ci ay cambal
Doko guiss ci lou ñiak fayda
Geun nek star ñiep nak , meune diss gane t oyof tooy !
Mais boy yu bess yi ni ay Faramareen rek niofi nek 😌