Heure yi ngey waxtane ak sho yi dilene ladj si elles ont bien mangé niou ley tontou touti rek sama lekk beuriwoul yow ngey diay jongué nane ko faut manger woor dafa meti ptdr fek ki ngey wahal lekk ne 4 kilo mbourou ak mbana thiep di khar rer. Non alahira dina meti
Yaw mii dima lire, lan nga waajalal sa bàmmeel?
Lan nga jëf ba mu wóor la ni boofa demee sa nekkiin dana neex diirub junniy at lumu gàtt gàtt?
Lan nga nekk di def jamono jii, lula fay xañ noflaay? Booko xamee bàyyi ko gaaw léegi te jublu ci lila fay jariñ ndax tëray bu yàgg la
Ne pensez pas que cela n'arrive qu'aux autres. Du jour au lendemain, on peut se retrouver dans la même situation que sa famille partagez comme vous auriez aimé qu'on le fasse pour vous.Elle s'appelle Safietou Diallo. Appelez le 779034541 en cas d'informations
« bayina la ak Yallah »
« yallah naniou Yallah atté »
«kouma betteu nga »
Li Motakh bala may def Dara nitt walla makoy wakh Dara dîna ko kholate Bou bakh. Akheu dafa diss !