@DoctorLove475@kvne_d MoMA gueneul kimay wah ..que tu est une princesse ..wala sans toi je peut pas vivre ..vu que ces des projet et c'est a l'avenir lolou gnoweugoul🤣🤣🤣
Diamanoye étudiant à l'ucad 'bountou B.U sah je savais pas foumou fêté..tey sama passion(musik) dougueulnama biir B.U...
#FollowYourPassion🔥🎸🎸
#doleymusik🔥🎸🔥
Il y'a un proverbe wolof qui dit.:''.boye dé alleu beu naleu gaindé réy"" mais wadji ndéké môme fatt gaindé bi...mais est ce qu'il en vit b legui..encaisser na dall🤣🤣🤣
Ce qui me choque « xalé you djiguene yinga xamni nioungui si biir keur yi, footougn, passé wougn, reew nagne, xamadi nagn… » genre si darapayine lagn beug limiter mariage😭😭
@houroul_ayni En tout l'amour n'est jamais fixe..daye daggou Di dem..et a tout moment la situation peut tournée ..Lou djara bayi khell...si vraiment tu es à la recherche de ton bien aimé ..donne lui le temps de prouver ..man dé li la wahh ..est ce que yen tamit lolou ngen wah
@PapeSidy@leuz@balvada Legui c'est l'inverse dans le game ..rappeur yi deff mbalax bou saff..mbalamane yi Di clashater 😃..oooh la musique sénégalaise..teug ak wokotou meunougno andd ..