Seriñ tuuba moom bala nga ko aam deug faaw daa ngay jayantee saa suuné ngaa diko tewlu .
Wayee boo beugue melni maan , taay ya ngi si match yi , souba ci lambb ji .. dana jaafe lolu .
Pendant ce temps, qu’est-ce que la CAF a fait ? Qu’est-ce que ses collègues arbitres africains ont fait pour le soutenir. RIEN ! Merci à l’UEFA. #OmarArtanTheBest
Saa bu guddi Àjjuma jotee, (maanaam tay Alxamiis ci guddi gi), nga jàng:
1-Faatiha 1X
2-Salaatu Halan Nabii 1X
3-Lixlaas 40X
4-Salaatu Halan Nabii 1X
Su noppee nga yéene ko jullit yi faatu yépp ak ñiy dund jamono jii, ak ñi wara judd.
Kon jullit bi njëkk a faatu ba ki mujjee faatu, dinañu am yoolub 40 Lixlaas.
Ku ko saxal ba Yawmal-Xiyaam, ku ñëw ci yaw ngir fayonte ak yaw, Yàlla moo naan ko, bàyyi ko mu dem ndax ku ñu mbaa-Yàlla la, dafa farlu woon bay maye aw yiiw.
@Dija_Foreal C’est tellement difficile sokhna sii boul wakh seulement la vie d’une fille même la vie d’un garçon sera perturbée😭mais si tu te souviens que personne ne sera épargné de cette situation tout ira pour le mieux
Moi j’ai perdu le mien depuis 2023 wantè alhamdoulillah
Perdre son papa je pense que c’est l’une des pires épreuves dans la vie d’une fille ! Allahou Akbar rien que d’imaginer mon coeur serre.
Yallah boumako téleu kham, Amine