L’Assemblée nationale doit elle-même provoquer sa dissolution si nous voulons aller aux élections dans les meilleurs délais.
Le rejet du projet de loi de finances rectificative serait un premier signal fort. L’heure n’est plus à l’attentisme.
Sinon, Diomaye ne compte pas organiser des élections !
Ay jàkka yu mag nekk ci wet gi, ngeen bàyyi ko fa, ñëw mbaar fii naan jàkka ji, pour yéen luñ tudd diine rekk kenn waru koo laal, te du ngeen ko teg ci yoon, fu neex waay samp dara naan jàkka ji.
Lou tol ni Goudi Gamou di mbegte ak naatange beipe Julit; nieup di begueee yow ngay meir aki daagasante. INCROYABLE Ya Mustafa!!
Le ptit qui s'oppose a Falaa Boudeu, essence meme de l'enseignement "MAODO".
i feel trully sorry for them
Fii mom saa youmafi delouci wé, eukine sanzman.
En tout xas Nadio bi gueine yenou,fexeleen ba koufay dem na def asc, waxouma sakh gang.
Sinon buvez bcp d'eau 🫡
3ans niu wara fay impots gniii! Bayinaa leen ak yalla.
Esk dou ma tioubou hypocrite rek sagua sama tomaalove bu sell bi, sama sopey bi, lidjeunti sama bopp en attendant mou dikk niu ande defar reew mi?
Gars jeunesse dafa gaaw koaa, t amoul arret. 3 ANS