@MohamedWilane Heureusement ba sëriñ bi laata mi dem Tuubaa dafa def ni ku sóobu ba am yenn maxamat yi do ko gis do ko yëg. Sinon rek Nga gis ku nangu Wala kuy ndamu.
@MansourDasylva C'est vrai que c'est pas la bonne méthode nous sommes dans une république bien structurée les pouvoirs publics doivent régler ce problème, le senegalais n'est pas naturellement xénophobe. Si on arrive à ce stade cela veut dire que nos dirigeants ont failli
@MrsKarmeel Exactly yàlla bañul kuko jaamu ngir intérêt ay contraire dafko bëgg ndax kiy jaamu Yàlla ngir intérêt àdduna nangu ni yàlla mooy Mayé I yor lépp ta loolu rek la talla bëgg Si ab Jaam lu 'nangu ni lépp di loxo yàlla la nekk
@MohamedWilane Jaamu Yàlla pour man lutax nitt ki di ko def rek baax ndax leerug yàlla ku mu Dugg ab xolam bu ko leneen taxoon di jaamu sax dina ko fàtte ndax Yàlla dax ludul mom. Man kuma laaj ndax xasida sagam dafay maye mbir manima waawaw ndax bis bu mosee yàlla bàyyi loola.
@kolytenguelaa Toutes les grandes crises de xénophobie commencent comme ça. Par de petites phrases méchantes qui attisent la haine. Nous sommes tous des terriens cela suffit à chaque humain de s'installer où il veut et y trouver sa subsistance.