Serigne Mountakha, yalna fi yagg té wer.
Il y’a 11 ans, il a donné une leçon d’humilité à tout le monde. Il a montré que le Khalife est l’autorité suprême et que tous les autres sont des talibés devant lui.
Ce discours de Serigne Mountakha Mbacké fait froid dans le dos 😶🌫️
« Koumou nekh nak yakou , wayé yak yalla, yak seu bissou soucrate, yakk seu bissou bamel… »
« Toute âme est responsable de ce qu'elle aura fait. » (S74:V38)
BOROOM TUUBAA nee na
« Bokk na ci li wuutale àdduna ak àllaaxira, mooy àdduna ak daraja joo mana am, kula bëgga gis man na laa gis. Allaaxira nak, ñi bokk luñ daan def rekka fay gise »
Akb Majalis
#18safar1446
Waa jii 😭 dina ray nit 😍 waaye sant nañu ci teewaay bi ak jangg mi . Daa siyaar si woon Soxna Maguet Guey ak waa daaraji 🙏 Yalna nga yagg lool te werr barkeb Xasida 🤲
Minanu fii Shehri Safar 😍🤔