Le manque de vocabulaire est une forme de censure. Moins t’as de mots à ta disposition, moins tu réussiras à articuler ta pensée et à défendre tes idées. C’est pourquoi la lutte contre les inégalités scolaires entre quartiers populaires et milieux favorisés est un enjeu important
Diine moom, booy jaay xel mu rëy ba jàpp ni lu duggul ci sa xel rekk, du lu make sense...Boo amul ndimbal génn ci diiné ji te doo ko yëg
Loo xamul, jàppal ni sa gëstu tollagul fokoy xamee, nga jëfee ko gëm ko ndax fa Yàlla la joge.
Alxuraan nekku fi pour adapter wu ci seen désirs
Syndicat yi ñoo yay grève, ndax président bu takkoon biiram ba ñépp xam ko, kon dees na ko muñal, waaye yor sa caisse noir ak say soxna di def lu la neex di organisé ay soirée di bànneexu ba noppi bëgg a muñloo nit ñi loolu manul nekk.
Caaxaan yi bari na !
😭🇸🇳 Ousmane Sonko est en train de donner une véritable leçon d’économie sur les réalités du pays ! Quand les chiffres, les arguments et les enjeux sont au cœur du discours, on comprend mieux les défis qui attendent le Sénégal.
L’économie d’un pays, ce n’est pas des slogans, c’est comprendre les problèmes et savoir où l’on veut emmener son peuple. 🔥
Li Sonko def lou bakh la ndah Sénégal dafa ame nioo hamné dara niourolène waayé souniou haméné sén dépense dinako yokkou té sén pouvoir d'achat dou yokkou niou tambalé intéressé wou si réwmi... Réwmi moom sou nékhé niép yeuko sou nakhari tamite nonou amoul kou far ak faroul...
Kham-kham ak vision ak fitt si politicien yiniouma nétali ak niéma fékké kou mélni Ousmane Sonko @SonkoOfficiel amoussi mane nga andaak moom comme mane nga bagna andak moom si yéne démarche yi waayé limoom mooy li wér moom !.
🚨🔥 ADA FASS 🆚 BALLA GAYE 2 : ÉCHANGE DE PIQUES À PARIS ! 🇫🇷🥊
Les deux lutteurs se font face et se lancent des mots. La tension monte avant le choc ! 👀💥
Il y a quelques temps il y a eu un mouvement contre la vie chère qui a été organisé et chacun les a regardé sans bouger… mais c’est pour Youssou Ndour qu’on va se révolter 😭😭😭 le même qui a saisi chaque occasion sous Macky Sall pour montrer à quel point il nous méprisait
Je n'ai aucune sympathie pour @YoussouNdourSN, car il a ouvertement soutenu Macky Sall dans sa répression des sénégalais. "Kou yeungou niou dall sa kaw" est encore frais dans ma mémoire. Ma sympathie, je ne la brade pas.
Ne venez surtout pas me dire de ne pas mélanger les choses
Dans un pays normal et respectable, quand un gars soutient un gouvernement qui tue son propre peuple et va jusqu’à l’encourager, c’est lui qu’on devrait boycotter.
Bon, le Sénégal, pays de la Teranga… 🙃
Yaw todjo sa reew. Kén bayi woula xel. Meusso fah gagner élection quartier. Amo charisme, amo élégance, amo légitimité. Amo parcours, amo discours. Amato kougn la roussé. Lindienti wo lolou lépp, ngani da ngay yanou campagne internationale di CSC. Mane domou adama diaxal nama.
@MadiambalD Tu mens, tu sais que tu mens et ceux qui fréquentent ce réseau savent que tu mens. Impossible de faire un post aussi long sur Twitter. Et cette photo sur le post du PRÉSIDENT SONKO est bien celle de sa page facebook . Le post y est encore et pour l’éternité!