Man ak ben mbok taalubรฉ meus negn di waxtaan ak ben yaaboy muรฑuy wax sen aal yi bolen takkรฉ soxna dingenko tek si suuf. รฑunek fa di aalu nanko xamo lingey wax 2ans aprรจs sam mbok taalubรฉ bi yeew Soxna ma demfa seeti leen gnu tok si salon bi soxnaci nek si wagn bi di wadial...