Fi jamono tollu, ku bëgg a mucc, fexeel ba, am métier, am loo mën, di liggéey foo tollu te doylu nak. Rafet njort ci nit ñi, di dund lu positive et xam say farataay diine te fexee jege sa Boroom.
Boole ko ag jàpp sa njàmbur tey àndak ñi lay dimbali ci ag njub
En tant que jullit so yewo guiss kou done muuru murekou boko mounoul nianal sunu Borom yombalatal ko muuru waro ce waax lu niaw . Surtout jigeen mu leerlani muuru yomboul dara ter kéne muccul si murekou .
Yallah nañu Borom bi yombalal jeufe ay ndigeuleum.🤍
J’ai envie de créer un groupe SAIN de femmes entrepreneuses.
Vraiment sain, où on ne fera que se booster que s’aider. Les femmes sur tiktok elles ont bien ça, mais c’est TOXIQUE
J’ai vu aussi la nouvelle bande de Misstoo-Amy Channel-NKD et je pense que j’aime
🚨CAGNOTTE POUR AWA
Chaque don compte. Et si tu ne peux pas donner, merci de PARTAGER autour de toi.
💚 1 partage = 1 don de plus grâce à toi.
👉 https://t.co/HRQTAXia94
📌« Maty Stp doma postel ki sama rak la moy souniou thiat daf niou rere depuis une semaine mais mo demal bopam nak elle s’appelle ndaye. Aïda ndiay elle a 16ans yayam mame maty kebe papam khadim ndiaye touba la dekeu nindi fofou la diougeu dem biniouy koy moudie localiser par la gendarmerie de touba mongu wonn côté Louga
Nga def ci numéro yi abdou ndour 77 8740592
Sama yaye 771934543
Ou bien sama numéro 778036634 merci way »