jihad jooju ma doon def ci sama xalima, su ma ko bàyyi wul woon, kon yéefar yépp di nañ dee ci mbas, waaye jéggal naa nit ñépp ngir Yàlla. Seex Ahmadu Bamba❤️
Seydou Nourou Ba. Entrepreneur et fondateur de la plate-forme de crowdfunding Kopar Express. Incarcéré depuis un an car sa K.E était utilisée pour des levées de fonds.
Son fils est né alors qu’il est en détention. L’a t’il jamais porté dans ses bras? #FreeSenegal
Lu nee fàngg ken du ko jéex ! Ñii la wa Ahlu Tassawuf taggat. Jàng ak Tarbiyah !!
Waaye tog, lu way def ga nee “bidaa”, “shirk” te defaro ku diine mana tiitaro.
Vous n’êtes bons qu’à fabriquer des haineux!!