TOUBA CA KANAM est une association apolitique qui investit sa force, sa richesse,son intelligence au service de CHEIKH AHMADOU BAMBA/ 33 978 25 37. 785443333
13EME ÉDITION
FORMATION DE MAITRES CORANIQUES:
Mbindu mi dina tàmbali
Le 16 et 17 octobre 2025
École Sëriñ Murtadaa Mbàkke en face Kër Sëriñ Siidi Abdulaahat Mbàkke Route de garage Daaru Muhti
Commission Scientifique di Kuréel giy Liggéeyal Sëriñ bi ci toolu Alxuraan...
Commission Sociale
Touba ca kanam
Taxawu néew-doole ji ci anam yépp, moo xam dund la, moo xam am paj la...
Jaamu Yàlla ci jaami Yàlla yi !
Wav&Om 779142668
Liggéeyal Borom Tuubaa ci dëkkam bu Sell Bii wàccul kenn !!!
Man ngay yaxantu yoraale say " Bloc de reçu Touba Ca Kanam " te du la yàqal dara...
Yal nanu bokk ci ñiy jëmale
Tuubaa ca Kanam
🌙 ZAKAT AL-FITR 1447H / 2026 – TOUBA
La Maison de la Zakat – Kër Asaka Yi rappelle aux fidèles musulmans l’obligation de s’acquitter de la Zakat al-Fitr avant la prière de l’Aïd.
💰 Montant fixé : 1000 FCFA par personne
Touba Ca Kanam laaj lu ñu am def ko fu ñu xam ba noppi di ko saytu...
Ak seen i ñaari téeméer tax na ba bokk na ci dëkk yu gën a leer
Ayca Murit liggéey baa ngoog
Bumu laal suuf