Sëriñ Tuubaa bokk na ci li mu rawe ñu bari mooy nekku fi di werante ci biddaa ak sunna, dafa ne faf lu war la, waaye ci ñan ? "Sawii taxaddumi" ci ña jiitu. Daal ciy woo ay taalibeem yépp.
مـولده معظم مـبـارك مـحـترم
تعظيمه ينحتم على ذوي التقدم
#Gàmmu1448
Ni sëriñ tuubaa daan dundale gammu:
« Day déf ñett (3) kureel
1- jazbu
2- Mawaahibu
3- Muqaddimatu amdâh
Ak kenn Kuy jang barzanji.
Kiy jang barzanji bi day jang benn chapitre, ñaari salaatu yi (hattiri gi ak beneen bi ci topp) dakay répéter plusieurs fois.
kureel jazbu jël jang 12 Bayit,
Kureel Mawaahibu jang 12 Bayit,
kureel Muqaddimatu jang 12 bayit…
(Barzanji, jazbu, Mawaahibu, Muqaddimatu amdâh)
Noonu lañuy déf ba guddi gi jeex
Bu ñuy jang sëriñ bi day juk di jox ñiy jang xeeti lekk ag naan yu neex, di leen sotti ay façon parfums yu neex lool»
Aji nettali ji: sëriñ muudu xari busu fekke woon jotaay bi.
Sunu musiiba ñun generation bii moy leep la ñuy def kaf , leep la ñuy reetaan ! Bis a ngi ci bis yi sax amaana ñu taxaw di reetaan ci mandarga aduna guy tukki te du ñu ko xam ! Lii nag day wane sunu ñak a fataliku ag baayi xel yallah .
Ci jamono yii yallah da dig ajjana ñi nga xamni bu ñu gisee lu yeeme ci li yallah sakk da nuy tudd yallah wax ni « yallah sakkoo li ci neen tudd naa sa maggaay » , seytaane nag da nuy buux ci ñak a tewlu ag distraction ngir liii rëcc ñu
Se raser, s'épiler, enlever les poils : mercredi ou samedi
Couper les ongles : jeudi
Grande ablution : à chaque fois que necessaire sinon les vendredis
Eviter de faire ces choses (rasage, épilation, couper les ongles) en état d'impureté majeure.
Conseils de S. Shuhaybu Mbacke
Fi jamono tollu, ku bëgg a mucc, fexeel ba, am métier, am loo mën, di liggéey foo tollu te doylu nak. Rafet njort ci nit ñi, di dund lu positive et xam say farataay diine te fexee jege sa Boroom.
Boole ko ag jàpp sa njàmbur tey àndak ñi lay dimbali ci ag njub
🌍 Le Grand Magal de Touba confirme son statut de rendez-vous religieux majeur à l’échelle mondiale.
Selon les estimations de participation disponibles pour 2025, le Grand Magal rassemble environ 6,58 millions de pèlerins, ce qui en fait le deuxième plus grand rassemblement religieux musulman au monde, derrière l’Arba’een en Irak.
Bien au-delà de sa dimension spirituelle, le Magal constitue également un événement d’une ampleur exceptionnelle sur les plans logistique, économique, social et sanitaire, mobilisant chaque année des millions de fidèles venus du Sénégal et de la diaspora.
Une reconnaissance qui témoigne de l’influence grandissante de Touba et de l’héritage de Cheikh Ahmadou Bamba sur la scène internationale.
Sources : données de participation 2025 (APS, Emergence Consulting Group, autorités saoudiennes et organisateurs des différents rassemblements).
Sant sama Boroom nag not na fii mu ne ci sama dëkk bi;
Ginnaaw muñ gu rafet ga ma dëkke woon ca sama tukki ba.
شـكـر إلـهي حـان في تـرابـي
بعد جميل الصبر في اغترابي
#Safar1448
Takk Yónnent bi halayhi salaam indil na ma yiw yépp, musal ma ci loru képp ku bon; ku ci sàkk-sàkka nag na jéem su booba a kon dina sooy.
مدح رسول الله قـاد لي الصـلاح
كما كفاني كل شخص ذي طلاح
من شـك فـي ذلك فـليـجـرب
ومن يـجـرب بـاء بـالـتـغـرب
Sunu boroom dafa digal yonent yallah daawuda ni ko : yaw ag say ñoñ na ngeen jëfe cant
Jëfe cant nag du wax alhamdulilah rek waaye ay jëf la te loolu maggal lay misaaal