@blackksaiyan Le mauvais impact des videos insta. Les gens veulent soulever les mêmes charges que les gens qu'ils voient sur les vidéos alors que gnognou ça leur a pris des années bala niouy eksi fi.
C’est pour ça « meilleur de tous les temps » n'a pas sa place en sport mécanique. Les époques, les voitures, les risques et les conditions sont tellement différents 😂
Problem gaal yi ak nics c pareil. Le vrai problème mooy notre rapport avec l'argent/tekki ak complex tukki. Nit day yor ay millions sax mais pr moom su tukki wul rek tekki wul dara. Parent yi yàkkamti wër di wane wu parsk seen doom a ngi bitim réew sans savoir mm ci yan condition