1 Adouna bi kou xam si mom daara doko fagoul dara dakh dara doufi dés
2 alakhira mi kou xam si mom daara doko fagoul daara ba naw ko dakh daara doufa doy
3 yalla mi kou xam si mom daara doko moy si daara dakh yawmal khiyam bou faba yarame ba di lako door kéne dounako tégual
S. TB
Fexeleen ba tàmm di jàng Suuraat Al-Mulk guddi gu nekk ba laa ngeen di tëdd, ndax dina waral Yàlla musal leen ci mbugalum bàmmeel !!
Képp ku xamoon mettiitu mbugalum bàmmeel, lépp lu la ci mana musal, doo ko sàgganee.
Saa bu guddi Àjjuma jotee, (maanaam tay Alxamiis ci guddi gi), nga jàng:
1-Faatiha 1X
2-Salaatu Halan Nabii 1X
3-Lixlaas 40X
4-Salaatu Halan Nabii 1X
Su noppee nga yéene ko jullit yi faatu yépp ak ñiy dund jamono jii, ak ñi wara judd.
Kon jullit bi njëkk a faatu ba ki mujjee faatu, dinañu am yoolub 40 Lixlaas.
Ku ko saxal ba Yawmal-Xiyaam, ku ñëw ci yaw ngir fayonte ak yaw, Yàlla moo naan ko, bàyyi ko mu dem ndax ku ñu mbaa-Yàlla la, dafa farlu woon bay maye aw yiiw.
😭Témoignage émouvant d’une femme palestinienne qui déclare avoir été sauvée par Cheikh Ahmadou Bamba
Li de ab soññe dëgg la 🙏🏾
Version pdf : https://t.co/HVLy3asoLJ
Il y a trois ans, lorsque j’ai commencé à enquêter sur cette affaire, je savais qu’elle serait sensible. Je ne savais pas qu’elle allait devenir l’une des plus éprouvantes de ma carrière.
Au fil des semaines, les témoignages se multipliaient et les révélations devenaient de plus en plus lourdes. Plus l’enquête avançait, plus les pressions se faisaient sentir. Des appels, des avertissements, puis des menaces.
À Touba, où je menais une grande partie de mes investigations, j’ai été pris en filature à deux reprises par des groupes d’individus. Ils semblaient vouloir savoir où j’allais et avec qui je m’entretenais. Dans les ruelles de la ville sainte, j’ai dû multiplier les détours pour les semer.
Mais l’épisode qui m’a le plus marqué s’est déroulé à Khayra, chez moi.
Pendant plus d’un mois, un van noir stationnait chaque nuit devant mon domicile jusqu’aux premières heures du matin avant de repartir. Je n’en savais rien. C’est ma mère qui a remarqué cette présence inhabituelle et qui m’a appelé pour m’en informer alors que j’étais en déplacement à Dakar.
Son appel m’a glacé.
À partir de ce moment-là, j’ai compris que les intimidations ne se limitaient plus à ma personne. J’ai alors informé le commissaire Thiobane, en poste à Touba à l’époque, ainsi que le commandant Goudiaby de la gendarmerie, afin de leur signaler la situation et les faits qui m’avaient été rapportés.
J’aurais pu abandonner. Beaucoup l’auraient fait. Mais chaque fois que le doute s’installait, je repensais aux victimes qui avaient accepté de parler malgré la peur. Leur courage m’obligeait à continuer.
Aujourd’hui, trois ans plus tard, le tribunal a rendu son verdict. Certains jugeront que la peine de 20 ans de prison ferme reste insuffisante au regard de la gravité des faits. Chacun est libre de son appréciation.
Moi, je retiens surtout une chose : cette enquête m’a appris que la recherche de la vérité peut parfois avoir un prix. Mais malgré les menaces, les filatures, les nuits d’inquiétude et les tentatives d’intimidation, je n’ai jamais renoncé.
C’était difficile. Très difficile.
Mais nous sommes allés jusqu’au bout.
Je remercie également toutes les personnes qui ont contribué à cette enquête. Sans leur aide, leur confiance et leur soutien, je n’aurais jamais pu aller jusqu’au bout de ce travail.
{Yàlla mi nga xam ne, saa boo ko jëfalee te sellal ko dina la gërëm, yamal ci moom di ko jëfal te bàyyi keneen.
Yàlla mi nga xam ne, booy sàkku ngërëmam, li nga ragal tay ak ëllëg lépp dina la ko fegal, booy jëf jëfal ngir moom.
Yàlla mi nga xam ne, ku koy topp ngir sàkku ngërëmam, dina la féetewoo taxaw ci say mbir, loo bëgg mu def ko, loo ragal mu fegal la ko, doy la sëkk ba doo soxlaal keneen, te boo moytoo li muy tere, dina la teral fajal la say aajo, deel jëf ngir moom rekk.}
Masaalikul Jinaan !
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته
Noo ngi siyaare bu baax te di la ndokkeel ci yi weesu yépp di ñaan sunu Boroom dolli nu tawfeex ak sutura. Noo ngi am mbégte bu baax it ci yégal la daara alxuraan ji nuy taxawal, di ci sàkku seeni ñaan bu baax, tey sàkku itam ngeen yaatalal nu ko bu baax a baax.
Serigne Fallou Mbacke Ibrahim
Après geum YALLA dou juli ak woor Kasser mais nangou li YALLA def si nit. YALLA day mayer bu bax sakh tei da may Sonko. Chaque période IL s’agit ces hommes. Lolou day am.
De @Awah_Juuf
🇸🇳 Les 10 Commandements du Patriote
Un rappel simple mais essentiel : la force d’un projet politique ne se mesure pas au bruit qu’il fait, mais à la qualité de celles et ceux qui le portent.
Discipline, respect, engagement, formation et exemplarité : les valeurs qui doivent guider chaque patriote au quotidien.
Un grand parti se reconnaît à la hauteur de ses militants.
Soyons dignes du projet que nous portons. 🇸🇳
@Noo_IDcard Nous avons deux nouveau-nées. Leur père est décédé il y a quelques mois, et leur mère est décédée en leur donnant naissance. Si vous pouvez leur apporter une aide🤲🏾