As salam Aleykum Wa Rahmatulah Mangi len di Ziar dilen jox sen wacuway.
Di wax ñi am yeene jël been jukki diko jang mensuellement muy Goor Yallah wala Soxna amnañu ay jukki yu disponible.
Vous pouvez ne contacter par Dm ou faites signe sous ce tweet ma msg leen.
@joie_boule
#rtapprecie
As salam Aleykum wa Rahmatulah
Mangi len di Ziar buweer
Est-ce que Amna ay Soxna yu bëgg jël ben jukki si sunu Kamilu Soxna yi diko jang chaque weer ben yoon?
Je vous demande pardon population jël len jukki yi. Kuko bëgg jang ben yoon it bañu ma 😭
@joie_boule partager ko 😭