BOROOM TUUBAA , c'est le centre de mon existence
MAAM SEEX IBRA FAAL , je t'abandonne mon âme , mes sentiments , mon désir , moi même et moi tout entière
🕊🤍🥺
Amul ben raison buy tax doomi Aadama baña bëgg Sëñ Tuubaa. Amul!
Ndax lep lu baax ak domaine gumu mënti doon, migui ci Sëñ Tuubaa te lumu ci def, ken defu ko ci.
À mon humble avis,Cheikh Bassirou Mbacké Khelcom, est le meilleur biographe contemporain du Prophète Mouhammad SHWS.
En effet, la précision avec laquelle, Le petit-fils de Cheikhoul Khadim, a, raconté l'histoire inédite de l'homme fort de Médine, est hors pairs, Machallah !.
Qacida moom kuddul KU BAAX KI moo la feete kaw ngir limu bawoo ci MOOM
Kilifa ga ngay sumul mbaxana Qacida yi ñoo ko kawe fuuf gën ko it ci fanu yépp
« Sama Qacida yi mi ngi melni may dag sama yàppu yaram dileen ko jox »
@AlaadjiDitakh Kon mbir yi compliqué na
Man perso duma sol mbaxana ci kanamu benn kilifa...
Mais jëmmi Sëñ bi ak jëmmi qasida est-ce que benn la dans ce cas de figure? Par ex man na noo sol mbaxana di jàngg alquraan wala sax di drus mais lutax manu nuko bu nuy kurel ?
Seen wax jii mënul tax ñu bàyyikoo tuuti ngeen si sax ak séen xel yu gatteu ki deem tokk ci bamel di ñaan kooku tawakul lay deff te dara neeku ci BOROOM TUUBAA nak jugge fi tay la fi gëna neek dangeen di ay gonne rk niakka xam motax ngeen wara maandu
Ndax danga yër mboleem li mu bind ak li magg ñi saxal ni moo ko wax ? ndax lu melnii wax jii dégg naa ko ci Soxna Awa Joob
Budul dara sax neex naa gëm ndax waxoon na Sëriñ Maalig Basin Si «man keemanu YÀLLA laa»