Sa tur wi wen rawuko.
Sa waajur it kenn gënuko.
Saw askan it kenn gënuko.
Sa jikko nag kenn duko am.
Li tax yaw amoo dindando jagle nga am ciw turando, ngir koo di bokkal turando Aaminatu du doon ndayam, mbaa bu Ami doone ndayam Seexull Xadim du waajuram.
Seex Mustafaal Karim🙏🏽
« La blessure de la langue est plus grave que celle de l’épée. »
Moo tax nit ki warna di bayyi xel limuy wax/ bind, benn baat bu ndaw mën na gaañ keneen.
Ndeyssane Thieuy Serigne Touba mi
Wayei Thieuy Cheikh Ibra Fall 🥹🥹🥹
Waxtou wi nit yi di yeem si Jeff yi ngay jeff, ioe ngay ligueye diko joxei diko xeeb
Baye fall gui deug la yallah kessei la