« Ku jàpp ne amna kenn kuy jariñe wala kuy lore kudul Yàlla, ci coono ak loraange ngay dëkk àdduna ak allaaxira »
Quiconque pense qu'un autre qu'Allah (swt) peut procurer un avantage ou nuire est condamné à vivre ici bas et dans l'au-delà dans la fatigue perpétuelle et le malheur
قال الشيخ الخديم رضي الله عنه:
يمين ربي إن ربي أحب
لي من سواه والنبي بعد الأحب
Sëriñ Tuubaa neena: Waatnaa ci Yálla ne: Yàlla laa gëna bëgg ci ludul moom.
Bu jállee Yonente Bi (Sállal laahu halayhi wa sallam) moo ci topp.
Tay Çi guddi Moy guddi nisfu Shbaan
Sopp nan ku Çi jangue Ñiatti Yaacin baxna lool
Bu ñieuk bi nga yeené thi guddu fan
2ém bi nga yeené thi mucc çi bala yi
3ème bi nga yeené thi am lula doy ba do Soxlal kén
Boko manul Man nga wax kula ko djangal
Sëriñ Daaru Asan Njaay nee na « diirub bima jaayanteeg Sëriñ Tuubaa ak tay, Sëriñ bi masumaa digal lenn loo xamne njariñul boppam ma nga ca, te lépp lum ma masa digal rekk ag jaamu Yàlla lay doon, ca laa xamee ni kon yoonu Murid, yoonu jaamu Yàlla la... » #MINAN