Yàlla alag na aw nit ngir jëfi GJ, tay jii ngeen bëgg cee maslaa ak nit koo xam ne, da caa boole dorog ak tasaare ay tawat te tay ko, ba noppi ñëw raaxaloo ca biir mbooloo ma gën a sell.
Ag GJ duma ci maslaa mukk mukk !
وماكان الله معذبهم وهم يستغفرون
Loolu du fi wàcce mbugal mukk, ndax lu baax li ñu fiy def moo ëpp fuuf, Senegal bokk na ci réew yi gën a néew lu bon.
Réew muy débat ci ag mbon ak di ca jaaxle xamal ne ñu baax lañu.
Réew mi ma nekk jamono jii, GJ yi dañuy solu ba mel ni ay jigéen ñëw di fëgg sa vitrin auto di jaay seen bopp, ci laa xam ne Senegal ñu baax lañu.
Dañuy salteel, dañoo bëgg yàq der, dañuy tilimal, nañu ko bàyyee ak Yàlla dund boppam la.
Xeetu discour yii soxlawunu ko, lu bon moom ku ci nekk te delluwoo Ginnaaw lu ne man naa dal ci sa kaw, nanuy tuubal Yàlla tey sax ci li mu bëgg saa su ne.
Lu bon deesu ci jàppale nit !
ولاتعاونوا على الإثم والعدوان
Goor yi di wax jiggeen ñi da ngeen war a janggi , lu ci ëpp seen bopp jangguñu , rëy na ñu janggiwaat waaye comme nu ngi ci ben position bu ñu njort ci ñoom xam xam rek faw ñu naxasaale ci .
Te it ñoom ñooy jël aaya yi di ko door ci kaw jiggeen ñi , di leen wax it ni da ñuy foowe diine , te ko ci laaj farata yi ci lislaam xamu ko
Comme tu n’es pas expert fallait rée en silence .
La lune est née jeudi a vers 2h du matin et elle grandi par heure quand on dit grandir c’est la luminosite qu’elle reçoit sur sa surface donc au moment du seentu elle en avait pas assez pour etre vu et entre temps le soleil se couche, puis elle continu de grandir jusqu’a tay avec assez de luminositre pour etre vu ….. c’est pourquoi le prophete avait dit jeuner a sa vu
Mais comme tu n’es par expert essaye de te renseigner d’ici l’annee prochaine
En live aussi par Sëñ Mor Astou Touré (j'ai rogné la vidéo pour tourou nitt yi doon commenter).
RDV demain, bou wa Mali wakhè guiss negn weer wi fekk dioudoo goul sakh.