Demain ça fera 40 jours que mon petit frère repose sous terre.
Priez pour lui ainsi que pour ma mère. Qu’Allah leur fasse miséricorde illumine leurs tombes et les accueille dans son vaste paradis. Amine Ya Rabb 🤲🏿❤️
Sama pape d doula meuss bayi nga teudaler ak merr bi ak bêtises bi meunti deff dina la wax deug bi remonter leu les bretelles ba nga xam après mou nieuw nekhal la lo beug mou indi ko diokh la ! Tiey sama wadji Yalna La Yallah xaré aldiana 🙏🏾mon ami ♥️
24/10/2020 - 24/10/2026
Que Dieu continue de bénir notre union et nous accorde encore de longues années de bonheur ensemble.
Joyeuses noces de chypre à nous 💐 #Sandaga is 6 y’ll ❤️
@albadaradi et moi étions à Sandaga entrain de faire nos courses, quand on ns informe que ce qui était censé être une rencontre de courtoisie entre les 2 familles a fini par vêtir la solennité d’une union devant Dieu ci timiss 😭 Que dire..Alhamdoulilah 🤲🏾
#AdunaLeppTeràngaLa
Diine moom, booy jaay xel mu rëy ba jàpp ni lu duggul ci sa xel rekk, du lu make sense...Boo amul ndimbal génn ci diiné ji te doo ko yëg
Loo xamul, jàppal ni sa gëstu tollagul fokoy xamee, nga jëfee ko gëm ko ndax fa Yàlla la joge.
Alxuraan nekku fi pour adapter wu ci seen désirs