Un gars sur tiktok jeundal jabaram parur or Yayou wadji merr ci ba guĂšn keurgui ndax nena wadji magam bou jigueen la war njeuk takal or đ Wa dji nexal yayam nangou or bi jox koko, yaye dji jox ko soeur bi ci kanamou jabar jiđ elle a divorcĂš gnibi sen keurđ Wadji nena da jaxaso
Je faisais une simulation Ă la banque SGBS pour un prĂȘt immobilier sur 20ans
Je vous laisse les commentaires.
- 25millions tu rembourses 64 millions
- 40millions tu rembourses 102millions.
Yallah bahna
Je viens de me faire arnaquer 20000f si beine femme bouy def vente en ligne Eva SHEIN la toudou sur TikTok ⊠ne commandez pas chez elle sathie wayei bayei nala ak yallah