Ay nit yu génn ci diine loolu doyul ñuy saaga diine ji ak Yonent bi shw, ngeen ne nañu maandu ndax àdduna daa gudd tànk.
Ki génn ci diine ji bëtub yéefar ak noon rekk lañu koy xoole, bu dellusee nag nu defaat ko ne sunu bopp muy mbokkum jullit.
Ab jullit day am fulla ci diineem, yaw ku la xas nga summiku xeex, ñuy xas sa diine nga ne dangay maandu doo wax.
Nouveau livre de Serigne Ahmadou Mbackè Darou Mouhty « «Réponses à 18 Questions sur l’islam, le Soufisme et la Mouridiya ».
Vous pouvez précommandé à partir de ce site https://t.co/jQZ0q2EMnU
@__babacar@Ousmane0777484@baay_saliou@LeMouridePost@s_sourang
Hasan al basri waxoon na ni , bokk na ci mandarga buy wane ni nit ki yallah daf ko wan ginaaw moy saa su ne yallah daf koy xirtal muy nek ci lu yoonam nekkul
Sen thioro (copain(e) kep bou ngen di waxtane ak nioom da lene di jaral ngen teudiou ci neek, mba barab bu weet dieul sa attention lep jox koko tekk ci di wax ndank( ñiak bop yow mi def lolou ) 😂
Wayer Yallah jaralula teudiou ñiar waxtu diko toudou ?
Ya ñiak kerssa deug deug !
« Wakhal murid yi , ñu geuna faarlú ak googorlù ci jaamu yalla ! Fi ñu neek dee lu baax doufi dooy »
Seriñ Bassiru turee nèna dafa guent guiss Seriñ Saliou MBACKÉ (rta) mou waax ko li .
Di ziar mbokki talibe yeep , Ubinaa ab kaamil lien baa ngi noonu ci suuf ku bëgg jël ab jukki mën na tann foofu . Sabab bi moy jang ko adiya seriñ bi te seedeel ci yallah sunu boroom leep lu ñu neexul te ñaanal ci seriñ Muntaxaa mu yagg fi te andag wer .
Seriñ bi lepam alxuran la kon nan ko ci yootu nun murit yi ci lep lu ñu neexul
https://t.co/Kco5n4di9B
Sëriñ muntakha moo fiy sëriñ tuubaa ci kaw suuf ta mat nako sëkk ci côté yepp fum jaar rek mooy yoon wi, waaye al hamdou lillah ba murid yi xame ko noonu.
Yëngu bi mën naa bari waaye sëriñ bi mbiram dara du ci yaqu mukk, kon xel mën naa dal
ñaanoon na boroomam ci daraja al muntakha yalla aar leppam ci bepp sikk
واعصم بجاه المنتقي كليتي
من كل عيب ولتقبّل نيتي