Ñàkk moom lu sunu BOROOM di nattoo jaamam la rek te yiw dong la ko ci nammal bu ci amee muñ gi ci war. Xayna sax xasiida gi moo ko ubbil buntu yiw yooyu jaare ko ci ay nattu
@SidyMSene Ndax sa cas personnel matna def generalite ag borom xam xam boobu kan la ? Ag fan la teg wax ji . Ndax ci biir xasida gi seriñ bi indi na fa ñaaan bi am solo contre ndol . Bu ken nee day indi ndool dafmay jaaxal wala ?
@SalihFadal@tonux_samb Machaa ALLAH lii la ay jullit di jariñante. Dénkante lu baax ak di tere lu bonn. Te loolu mootax umma bi gën ci xeet yépp jaaraama sang yi🙏🏾
THREAD : ADIYA OU CADEAU PIEUX
La hadiya constitue la base du fondement de la société islamique. Voire une condition nécessaire pour être un vrai musulman. En effet , le prophète fut arrivè a Médine , les mains vides et dépourvu de tous biens.
Au delà de toutes les assemblées de zikr ou de prières que nous fréquentons, trouvons nous un moment dans la journée ou la nuit pour raffermir notre intimité avec notre raison de vivre, YaAllah❤️
Kula meuna deglu ba nopi fadj sa aadio suturaal la te dula diépi , mom kesser la !
1- Omar ibn Abdoul Aziz
2- imaam shafi
3- imaam ashari & ibn surayj
4- imaam baqillaani & abu hamid al asfirayiini
5- ghazali
6- faxru diin ar-raazi & Abdoul karim ar-rafihi
7- ibn daqiq al hiid
8- zeynu diin al hiraaqi & siraaj diin balqiini
9- jalaalu diin suyooti
10- shams diin ramli
11- Ibrahim ibn Hasan al kardi
12- saalih ibn muhammad ibn nuuh al fullaani & Imam murtada zabiidi
13- muhammad naziir husayni
(Source: Al mujaddiduuna fil islaam)
@salioumbackefa1 Dans l’entendement humain la valeur d’un homme est mesuré par sa richesse, son pouvoir, sa prestige pour établir un titre de noblesse. Alors que Allah a dit: إِنَّ أَكْرَمَكُمْ عِندَ اللَّهِ أَتْقَاكُمْ
Donc oui notre vraie valeur se situe au niveau de notre relation avec LUI
@salioumbackefa1 Eskeyy.. giss giss bi de amna solo lool.
Mais li laaya bi wax, en qualité de serviteur la ko nit mën a atteindre. Et la manière dont on traite nos semblables est aussi la resultante bénéfique de notre piété