Tradition..
( Allahuma salli wa sallim wa barik hala sëyyidina wa mawlana Muhammadine nabiyil ummiyi habibi hali qadrihil haziml jahi wa hala alihi wa sahbihi wa sallim🤍
La taqwâ la crainte d’Allah . . . la cause de tous les biens.
Allah dit dans le Noble Coran :
“Ô vous qui avez cru ! Craignez Allah comme Il doit être craint.”
(S03V102)
Le Prophète ﷺ a dit :
“Le sage est celui qui se remet en question et œuvre pour ce qui vient après la mort.
🚨🇧🇷 C’est désormais une réalité : Barcelone est en contact avec l’entourage de João Pedro, un joueur que le club apprécie énormément.
Mais la position de Chelsea est claire : le club veut que le brésilien soit une pièce importante du projet sous Xabi Alonso.
(@FabrizioRomano)
Noo ngi leen koy fàttali
Tàngoor wi nii muy mettee ci Doomu Aadama Yi noonu it lay mettee ci Ñanaaw yi
Te nit manul dund ci lu dul ay dëkkandoom te ñoom ñooy sunuy dëkkandoo: Garab yi, mala yi, ñanaaw yi…
Tàngóor wi dina faagalgaal lu bari ci ñoom ndax ñàkk fu ñu naane te ñoom ci kéew mi lañu bokk kon sàmm leen nun la war
Lii misaal la ci fàggu i ndab moo xam bidoŋ la añs
Def ci ndox ajj ko ci kaw miir yi walla fu kawe ñu man di ci naan.
Touba Ca kanam
Commission Environment
« Sëriñ Jiili Alxuraan »
FARATAY DIAP {Ablutions} 📿🌙
7 Faratas :
1. Yéné
2. Rakhass sa kaname
3. Rakhass say lokho jusqu’au coude
4. Massa sa bop (en partant du front vers
la nuque)
5. Rakhass say tank
6. Ragg (bien se frotter)
7. Gaw (voir 3eme farata sangou sét)
⬇️
{8 Sounas :}
1. Rakhass sa lokho jusqu’au poignet
2. Galakh ndikou (rakhass sa guémigne)
3. Sarakh ndikou
4. Fiirou
5. Rakhass say nop
6. Toyal sa lokho bala ngay rakhass nop yi
7. Délo Massa bop (de la nuque vers le front)
8. Toftalé faratas yi (bien suivre l’ordre)
⬇️