Top Tweets for #29Mars2025
Éclipse partielle de soleil
#29mars2025

وافيت دائر الإحاطة مغرماً بسمى يهز ضرائب المعبود
Waa daahiratul ihaatati fa walliyu Yàlla yu mag ya nekk ñooñu sax dañu laa sopp ba bu ñu la gisee bég, bu ñu la gisul laajte la ngir sopp gi ñu la sopp.
Qâcida de Al Makhtoum à l’endroit de Allaji Mansûr
#29MARS2025

إذ ماهديت هديت كل موقف للهدى هدي الخاتم الصنديد
Allaji Mansûr dangaa jub, ba noppi du jubal, di jubale képp ku Yàlla namm ci moom njubug Sëydina Muhammad.
Qâcida de Serigne Cheikh Al Makhtoum à l’endroit de Maam Allaji Mansûr
#29MARS2025 #AllajiMansûrBalxawmi

مدحا وذما قد سمعت ولم تكن ممن يبالى قولة لحقود
Topp gi nga topp sëriñ Baabakar Si dégg nga ci xas, dégg nga ci xas, waaye taxul nga bàyyi. Te faalewóo ci waxi ña nga xam ni iñaan rekk a tax ñuy wax.
Qâcida de Al Makhtoum à l’endroit de Allaji Mansour
#29MARS2025

أوفيت عهدك للخليفةبعدما
قدشان غيرك من ذوى التقليد
Matal nga kollëre ci sëriñ Baabakar Si, jamono ja nga xam ni nit ñi ñaawal jëmale ko ci sëriñ Baabakar yaw Jamono booba yaa ngi rafetal jëmale ci moom.
Qâcida de Al Makhtoum à l’endroit de Allaji Mansûr
#29MARS2025

Seydil Hadji Malick SY à Allaji Mansûr :
“Mansóor jëmm ji tuuti na, waaye ku Yónent bi miin la.”
#29MARS2025 #AllajiMansûrBalxawmi

إنك لا تشابه رفعة إذ كنت منتسبا لذى التوحيد
Yaw Haaji Mansuur amul kenn koo nirool ci kawe, kenn melul ni yaw, ndax Seexal Haaji Maalig mu sotti nga.
Qâcida de Serigne Cheikh Al Makhtoum à l’endroit de Maam Allaji Mansûr (RTA)
#29MARS2025 #AllajiMansûrBalxawmi

لولا التقصر جل أهل بلادنا
ليكون منك لهم جزاء ودود
Dañu laa gàttañlu,Gaa yi xamuñu la, bu ñu la xamoon, xam gi ñu lay xam njariñ lay doon ci ñoom, jóge ci yaw jëm ci ñoom
Qâcida de Serigne Cheikh Al Makhtoum à l’endroit de Maam Allaji Mansûr
#29MARS2025 #AllajiMansûrBalxawmi

حتى كأن سناك عم مشارقا ومغارباً فى الأرض مثل السعود
Yow Allaji Mansûr sa leer gi dafa mel ni biddiw 🌟 Suhuut bu leer gi jollee leeral ñépp penku ak sowwu.
Qâcida de Serigne Cheikh Al Makhtoum à l’endroit de Maam Allaji Mansûr
#29MARS2025 #AllajiMansûrBalxawmi

Cher.e.s Patriotes,
Rejoignez-nous ce samedi #29mars2025 pour une conférence virtuelle sur : « L'an #UN de Pastef au pouvoir : jalons posés, défis relevés, horizons tracés. »
Un échange exclusif avec des acteurs clés du gouvernement et du PROJET. Cet événement sera une opportunité précieuse pour échanger avec des responsables engagés dans l’action gouvernementale et impliqués dans la mise en œuvre du PROJET.
📅 RDV à ne pas manquer !
#Pastef #1AnAuPouvoir
Pastef France

#NkitaExpoForum
Un grand rendez-vous des décideurs, des jeunes et femmes, acteur du développement en Rdc pour honorer la femme. #CollègeBoboto #29Mars2025
@DeniseNyakeru
@EmmanuellaZandi @RabbiNkulambe1 @BenMputu5 @BenedictKaleng3 @Israel @kaziteriko @Jesusnoelshek @GraceShako1

Last Seen Hashtags on Sotwe
ai hijab
Seen from Indonesia
쿨사연애
Seen from Indonesia
nolimit()*********** + filter:native_video
Seen from Germany
ometv filter:media
smpngentot
Seen from Indonesia
รับงานบ้านไผ่
Seen from Thailand
bullysis
Seen from Singapore
ライオンズファンと繋がりたい
Seen from Argentina
teenageer()************
Seen from United States
mom son real
Seen from Pakistan
Trends for you
Most Popular Users

Elon Musk 
@elonmusk
241.6M followers

Barack Obama 
@barackobama
119M followers

Cristiano Ronaldo 
@cristiano
114.2M followers

Donald J. Trump 
@realdonaldtrump
111.8M followers

Narendra Modi 
@narendramodi
107.2M followers

Rihanna 
@rihanna
98.7M followers

NASA 
@nasa
92.4M followers

Justin Bieber 
@justinbieber
91.8M followers

KATY PERRY 
@katyperry
89.9M followers

Taylor Swift 
@taylorswift13
83.8M followers

Lady Gaga 
@ladygaga
75.3M followers

Virat Kohli 
@imvkohli
73.2M followers

Kim Kardashian 
@kimkardashian
70.8M followers

YouTube 
@youtube
68.8M followers

Neymar Jr 
@neymarjr
66.2M followers

Bill Gates 
@billgates
65M followers

Selena Gomez 
@selenagomez
63M followers

The Ellen Show
@theellenshow
62.3M followers

CNN 
@cnn
61.8M followers

X 
@x
60.7M followers










