Top Tweets for #Diine
Daa am xeetu wax yoo xam ni xel la waaye du #diine , xel ak jeema dox ci xelu nit ñi ngir #dëbb ndox la
Doo xam kiy wax dafa xamul moo tax muy #utilisé yenn baat yi wàlla luy jafe jafeem?
Sunu #frontière yi nu tubaab bi defal ? Waa dafa am yu #tubaab def am yum deful am déet ?
Ndax diine day xool ki def ban couleur la yor soogay #considéré am déet?
Diine xamul tubaab wàlla #couleurs li am lay xool lan atte ko kon baatu tubaab yi ban njariñ la am?
Ndax jamonoy YONENTE bi ay dëkk yu am tur daa amul woon babu amee tay ñu jiiñ ko tubaab bi wàlla loolu daa ayy?
Xanaa sos dëkk du #bidaa d laa foog🙂
Ñaata yoon la #weer wi feeñ ci yaneen dëkk ngeen #sëgg ko bàyyi mu jàll di deglu seen dëkkiy kiloga ba pare di ray nit ñi ak coow lu bëri
Jamonoy 1926 gii rek nga xam ni #téléphone amul #internet amul lan moo doon #xibaar nit ñi ni dëkk sàngam #weer wi feeñ nafa wala Arabi Saudi tay la #arafa? Kon bi #téléphone ak #internet amee la coowli tambuli pourtant #tubaab bee andi téléphone ak internet batay d ñoo ko fi rëdd d🙂
Man daal bëgg naa nit ku #logique !
#Fukkeelu_fan boobu nag moom lañuy màggal ngir dafa bari xew-xew yu ci am ci #diine. Dalee ko ci Sunu Maam Ibraayma (A.S) ba ci Séydinaa Muhammad (S.A.W).
Bis boobu nag (#Aachuraa) suba ci ginnaaw timis gi la yem.
Nu fàttali leen ni bisi jullit ñi guddi yi ñoo jiitu bëccëg yi.3️⃣
To learn more or to connect with Reiki Master Brett Bevell visit his website https://t.co/qBy5ATtfRe #author #reikimaster #energy #healing #diine #psychic #awakening #transformation @brett.bevell

To learn more or to connect with Reiki Master Brett Bevell visit his website https://t.co/ZzkSPU0QKR #author #reikimaster #energy #healing #diine #psychic #awakening #transformation @brett.bevell

To learn more or to connect with Reiki Master Brett Bevell visit his website https://t.co/ZzkSPU0QKR #author #reikimaster #energy #healing #diine #psychic #awakening #transformation @brett.bevell

To learn more or to connect with Reiki Master Brett Bevell visit his website https://t.co/qBy5ATtfRe #author #reikimaster #energy #healing #diine #psychic #awakening #transformation @brett.bevell

Tele bii nar naa gëna reeral nit ñi
Déjà kii limuy wax deme wul noonu . Amna fookoy laal ci sa loxo sax te du tax njàppu mi toj.
NB: njappu mi du toj ludul ni danga laal sa awra si biir sa ténqq loxo yi (sur la paume de sa main ) wala sa digënté baaraam yi Jàngi leen #diine ji
Kii daño wara fax yat doumako
•Wax na ne tuuti kon mu dem,
Fekk #Sëriñ bi lëm mbiram,
Ba kenn du jot ci baatinam,
Ludul ca bis ba ñuy texe;
•Jaaraama #Seexi_Ibra_Faal,
Làmp bi #Sayxi_Bàmba taal,
Leeral nga #diine yaa kamaal,
Yalna nga dolliy beréxi;
👇🏾👇🏾👇🏾

#Serigne_mbaye_sy Sénégal kou wakh lou gnaw si #tarikha yi gnou beugue la Ray Bougnou wakhe Lou gnaw si #diine gneup noppi té mak gni diokhe sen doundou yeup si diine dji ❌🇫🇷❌
Teudie #jumaa yi ba paré di autorisée #Youssou_Ndour mouy rassembler groupam di concerts 🇸🇳🤔
Legui Sénégal deuk #diine lagnouy beugue sopi deuk #Fo thiey miim rew
@JaimeYMarieN

...léegi koo wara jàngal, yar ko, def ci moom #xam_xam, #diine, #yar_aki_teggin lu tax waroo ko tegaat ci yoon su ko wàccee. Pourtant #pompé mi ngi am ci école yi de, #tendre_par_4 mi ngi am ba tay ak yeneen te kenn waxu ci et là on ne parle d'incivisme👇👇👇...
@SINDIDISSALIOU Bok na ci #tarjumaani_Jëzbul_Xuluub, #Maam_Cernoo ko dindilu, ngir bimu ko gisee ba jàng ko dafa wax #Ku_Tedd ki ne ko #Mbàkke lii de soo ko dindi wul #Taalibé yi sunu ko gisee dootu ñu #jaamu_Yàlla, sunu #faatoo_tàbbi_aljanna, su booba #Diine yàkkoo ci Nun; #Sëriñ bi nangu ko...
Bruh I couldn’t even laugh i just closed my eyes and died inside 😭💀 #diine
I'm beginning to think our #president is on #drugs or have a drinking #addiction ,HE NEVER HAPPY.. HE BE COMING #DIINE tripping..maaane
Last Seen Hashtags on Sotwe
Most Popular Users

Elon Musk 
@elonmusk
241.5M followers

Barack Obama 
@barackobama
118.8M followers

Cristiano Ronaldo 
@cristiano
114.5M followers

Donald J. Trump 
@realdonaldtrump
111.8M followers

Narendra Modi 
@narendramodi
107.1M followers

Rihanna 
@rihanna
98.7M followers

NASA 
@nasa
92.3M followers

Justin Bieber 
@justinbieber
91.8M followers

KATY PERRY 
@katyperry
90M followers

Taylor Swift 
@taylorswift13
84M followers

Lady Gaga 
@ladygaga
75.5M followers

Virat Kohli 
@imvkohli
73.5M followers

Kim Kardashian 
@kimkardashian
70.9M followers

YouTube 
@youtube
68.8M followers

Neymar Jr 
@neymarjr
66.5M followers

Bill Gates 
@billgates
65.3M followers

Selena Gomez 
@selenagomez
63.1M followers

The Ellen Show
@theellenshow
62.2M followers

CNN 
@cnn
61.7M followers

X 
@x
60.7M followers














