Top Tweets for #Jullit
Wéroou koor daniouy teunk sheytaan ; #Jullit diapp ibliss di door té dou guis #Kouy_Até. !!!
#Day_8
#EnSidyclopedie. đ

Noo ngi ndokkeel #Jullit ñépp rawatina #Murit yi ci weerđ wu sell wi nu tĂ bbi, dileen baalu Ă q bu baax te dileen baal. Di ñaan sunu Boroom mu defal nu xĂ©ewal yu yaatu a yaatu ba nu jekku MĂ ggal gi barkep #Seex_Yibra_Faatiđ€Čđœ...
#18_Safar...

#18_SAFAR_1442H, Alhamdulillaa...
Noo ngi ndokkeel #Jullit yépp rawatina #Murit yi ci bis bii gën ci nun bépp bis (#18_SAFAR), di ci baalu tey baal à q kulluhum.
Yalnanu ci dajeek mbégum Boroom bis bi te yà gg koo teewe, di ci am i Ndam fà wwu...
#SEEX_AYDARA_MBĂKKE, Saab Sang...

Aljumay #Jà mm ak i #Xéewal ci mboole seen #Jullit ñépp barkep #Maam_Soxna_Jaara...
#Mà ggal gi nag sës na rëkk ci sunu kaw, nan gën a farlu te jaaju ci wà ccaay yi...

Ndeem #Ă q dafa sew te man nga koo ameel nit sax te doo ko yĂ«g, nu #baalu_ñépp_Ă qđ rekk ci #julli gi, #Ă q junu yĂ«g ak junu yĂ«gul nag.
Di ñaan #Sun_Boroom mu nangul nu sunu #tabaski te #reendil nu bépp #ayib bu nekkoon ci nun ak mboole seen #jullit ñi barkep Maam Sunu #Ibraayma...

#Aljumahantul_Mubaarak ci mboole seen #Jullit ñi rawatina #Murit yi, mbokki #Ruuh yiđ...
"Dox dem te baña gestu ! Ngir yëf ya a nga ca kanam..."
#Al_Mukarram...

#Sëriñ_Bà mba du seen mà ppandoo du seen maas, na ngeen jà ng #mbindëm mii #Boroom_Hanrach Maas !!!
Man de wallaahi nu Nit, rawatina kuy wax ne #jullit nga mĂ«nĂ©e taxaw bañ #SĂ«riñ_Tuubaa ba noppi di ko fĂ©sĂ«l !!! Ak limu daj lĂ©pp ngir #Doomu_Aadamađđđ...

Ndeysaan, #17Úme_jour ci koor #jullit yépp di ci fà ttaliku #Bisub_Xare_Badar ba amoon ca jamonoy #Yonent ba (S.A.W), bokk ci bis yi #Islaam amee woon #Ndam...
#Aljumaay_jĂ mm ak i #xĂ©ewal ci mboole seen #jullit yĂ©ppđ.
Yalna saa Boroom musal nu ci #mbas mi te jëléel nu ko fi balaa yà gg ci barkep weeram wu tedd wi nu nekk "#Chëhru_Ramadaan_Mubaarak..."
#Masaalikul_Jinaanđ...

Ab #Jullit, #ñaanđ€Č mooy #ngĂ nnaayamđ...
Moo tax nan dellu ci #Yà lla ndeem jógé ci moom sax warul waaye nu maase ci #tuub rekk ak #jéggalu ngir #mbas mii génn ci à ddina bépp...
#SĂ«riñ_Mbay_Jaxate nag Man yĂ©em nama đ, nune waxee na ko ak #SĂ«riñ bi, lĂ©pp cig #taalibĂ©...
#Mawaahibun_Naafinh...
âXayral #Baraayaa
Zut'tal balaayaa
Lizil xataayaa
Rumta najaa'i
âAntal #Kariimu
Anal #Xadiimu
Dëhran Udiimu
Fiika çanaa'i...
#Gà mmu_Jà mm ak i #Xewal ci bépp #Jullit barkep #Seexul_Xaddiim...

"Guddig #Gammu, yamale kook guddi ga ko jiitu wala ga ca top, dara jaru ko cib #jullit"
#BoroomXelkom

"Guddig #Gammu, yamale kook guddi ga ko jiitu wala ga ca top, dara jaru ko cib #jullit"
#BoroomXelkom
#BoroomGammu
#MbecteimiiâđŸâđŸ

"Guddig #Gammu, yamale kook guddi ga ko jiitu wala ga ca top, dara jaru ko cib #jullit"
#BoroomXelkom
#BoroomGammu
@putcola MitÀ tulee mieleen virkkeestÀ: "Ossi VÀÀnÀsen ilmaveivi"?
Nyt saa lippuja Rakkauden Saarelle! Michal Witkovskin HUTSULA #homo #venÀlÀiset #jullit #sotilaat #kullit @teatteriliitto @ranneliike @regnbagsankan @TIKETTIofficial https://t.co/jvBsGlwZvg

Last Seen Hashtags on Sotwe
momson () filter:native_video
monkeyapp
Seen from Argentina
incest sleeping
Seen from Turkey
TusOsdorf
Seen from United States
momson momson*
Seen from United States
myherocademia
Seen from Mexico
CRYvSHK
Seen from United States
愳ć
Seen from United States
êł ë볎ì§
Seen from Korea
TPMSpooky
Seen from United States
Most Popular Users

Elon Musk 
@elonmusk
241.1M followers

Barack Obama 
@barackobama
119.1M followers

Cristiano Ronaldo 
@cristiano
112.3M followers

Donald J. Trump 
@realdonaldtrump
111.8M followers

Narendra Modi 
@narendramodi
107.1M followers

Rihanna 
@rihanna
98.1M followers

NASA 
@nasa
92.2M followers

Justin Bieber 
@justinbieber
91.3M followers

KATY PERRY 
@katyperry
88.6M followers

Taylor Swift 
@taylorswift13
82.5M followers

Lady Gaga 
@ladygaga
74M followers

Virat Kohli 
@imvkohli
71.4M followers

Kim Kardashian 
@kimkardashian
70.3M followers

YouTube 
@youtube
68.7M followers

Bill Gates 
@billgates
64.4M followers

Neymar Jr 
@neymarjr
64.3M followers

The Ellen Show
@theellenshow
62.4M followers

CNN 
@cnn
61.8M followers

Selena Gomez 
@selenagomez
61.7M followers

X 
@x
60.8M followers


























