L'Imâm Shafi'i a dit :
« Cachez vos difficultés au point que les gens croient que vous êtes béni et que votre vie est facile »
(Manâqib Ash-Shafii 2/188)
Bokk na ci pexey saytaane ci sunu jamono jii xertal ndaw ñi ci tasawuf, (di lire seeni teere, di diglu seeni waxtaan, di gëstu ay wird, di weet di sikar, durus...) ta xamul ay farata jëmëm (laab, julli, woor... Ak seeni atte) jangul tawhiid ba xamee fimu wara yam, nimu wara weetale yalla...
Buko defee day nekk ci yoon wi di sonnu ta du gis njariñ li, buko defee mu japp ni limu nekk werul mu bayi, wala muy déf ay njoomte yu rëy ba ku ko gis japp ni ci ay caaxaan la nekk mën nafaa jaare bañ yoon woowu ba duko jeema gëstu ndax limu gis ci kii.
Moo tax sëriñ tuubaa waxoon ni:
L'apparition de pensées parasites durant la prière le jakalo ou la confrontation spirituelle est un défi universel lié à l'état de l'âme et aux distractions de Satan. Pour y faire face, sa vision s'appuie sur une discipline spirituelle, psychologique et comportementale⤵️
Guel toubabs yi dañ lay may ay qu’est-ce que tu as fait de ta journée?, bb t’en penses quoi de ça ? Bb je vais te faire découvrir une expo 🖼manam so néké ak niom t’es stimuler mais fi ndeim bossi guéné seni "ok" ak "ui" you doxan ndeim yoyu degn lay sonal ak seni "dama khif"
Khassida bi Serigne bi deufssi def beip niane bou YONINTE bi(PSL) done df guinaw bou done diouly digueunetei fajr ak souba ak Tisbar ak Takoussane en klk sorte niane yi YONINTE done df durant 24h yi leussi Serigne bi dadialei ak beip Sabal ak beip tawkhid⤵️
Jaam bi bumu bariy bàkkaar mukk ba tàyyee tuub, say bàkkaar yu bari yaa ko gis waaye Yàlla gisu ko, moom yërmandeem ak njéggalam daa ëpp doole lépp.
Bokk na ci màndargay ñàkk texe, bañ a tuub ngir ́jort ne manoo bàyyi moy Yàlla.
Ku ko man guddi gu jot ba la ngaa nelaw nanga teewlu Yàlla nga tuubal ko, ngir boo faatoo ci guddi googu doo yóbbaale bàkkaar.